Vous avez cherché: laata (Wolof - Suédois)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Suédois

Infos

Wolof

laata dara di am, fekkoon na moom mu nekk, te lépp a ngi jàppoo ci moom.

Suédois

ja, han är till före allt annat, och alltsammans äger bestånd i honom.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

buleen nirook ñoom, ndaxte seen baay xam na seeni soxla, laata ngeen ko koy wax.

Suédois

så varen då icke lika dem; eder fader vet ju vad i behöven, förrän i bedjen honom.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

nun itam naka noonu, laata nuy mat, aaday àddina ñoo nu nootoon, ba def nu ni ay jaam.

Suédois

sammalunda höllos ock vi, när vi voro barn, i träldom under världens »makter».

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ne leen: «yàkkamti woon naa lool lekk ak yéen reeru jéggi bii, laata ñu may sonal.

Suédois

och han sade till dem: »jag har högeligen åstundat att äta detta påskalamm med eder, förrän mitt lidande begynner;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

jigéen ji def na li mu man; diw na sama yaram ak latkoloñ, ngir waajal sama rob, laata moo jot.

Suédois

vad hon kunde, det gjorde hon. hon har i förväg smort min kropp såsom en tillredelse till min begravning.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

léegi nag baay, ci sa teewaay, feeñalal ci man ndam, li ma amoon ci sa wet, laata àddina di sosu.

Suédois

och nu, fader, förhärliga du mig hos dig själv, med den härlighet som jag hade hos dig, förrän världen var till.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

nu ngi yégle mbóotu xam-xamu yàlla, mu nëbbu woon te yàlla dogal ko ngir sunu ndam, laata àddina di sosu.

Suédois

nej, vi tala guds hemliga visdom, den fördolda, om vilken gud, redan före tidsåldrarnas begynnelse, har bestämt att den skall bliva oss till härlighet,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

nii la yeesu kirist juddoo. bi ñu mayee maryaama ndeyam yuusufa, waaye laata ñoo ànd, gis nañu ne dafa ëmb ci kàttanu xel mu sell mi.

Suédois

med jesu kristi födelse gick det så till. sedan maria, hans moder, hade blivit trolovad med josef, befanns hon, förrän de kommo tillsammans, vara havande av helig ande.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bàkkaar kon nekkoon na ci àddina, bi yàlla di laata wàcce yoonu musaa. waaye gannaaw yoonu musaa tëddagul woon, bàkkaar du woon jàdd yoon.

Suédois

ty synd fanns i världen redan innan lagen fanns. men synd tillräknas icke där ingen lag finnes;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moo taxoon ma wax ne: “am na kuy ñëw sama gannaaw, waaye moo ma gën a màgg, ndaxte nekk na laata may juddu.”

Suédois

om denne var det som jag sade: 'efter mig kommer en man som är före mig; ty han var förr än jag.'

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte laata ndaw yi saag yónni di ñëw, da daan bokk di lekk ak ñi dul yawut. waaye bi ñu agsee, te mu ragal kureel boobu faaydaal xaraf, mu dellu gannaaw, di sore ñi dul yawut.

Suédois

förut hade han nämligen ätit tillsammans med hedningarna; men så kommo några män dit från jakob, och efter deras ankomst drog han sig tillbaka och höll sig undan, av fruktan för de omskurna.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ngëm moo tax ba enog jaarul ci dee. yàllaa ko yóbbu ca moom, te kenn gisatu ko, ndaxte yàllaa ko toxal. ndaxte mbind mi seedeel na ko ne, laata muy toxu, neex na yàlla.

Suédois

genom tron togs enok bort, för att han icke skulle se döden; och »man såg honom icke mer, ty gud tog honom bort». förrän han togs bort, fick han nämligen det vittnesbördet att han hade täckts gud;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

nataneel ne ko: «noo ma xame?» yeesu tontu ko ne: «bi la filib di laata woo, gis naa la, bi nga nekkee ca ker garabu figg ga.»

Suédois

natanael frågade honom: »huru kunna du känna mig?» jesus svarade och sade till honom: »förrän filippus kallade dig, såg jag dig, där du var under fikonträdet.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,779,183,694 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK