Da traduttori professionisti, imprese, pagine web e archivi di traduzione disponibili gratuitamente al pubblico.
gli risposero: «se non fosse un malfattore, non te l'avremmo consegnato»
Ñu tontu ko ne: «bu deful woon lu bon, duñu la ko jébbalsi.»
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
gia quando eravamo tra voi, vi preannunziavamo che avremmo dovuto subire tribolazioni, come in realtà è accaduto e voi ben sapete
ba nu nekkee ak yéen sax, waxoon nanu leen, waxati ko ne, fàww nu sonn; te noonu la ame, yéen xam ngeen ko.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
così affezionati a voi, avremmo desiderato darvi non solo il vangelo di dio, ma la nostra stessa vita, perché ci siete diventati cari
cofeel gi nu am ci yéen tax na, bëggunu woon a yem ci xamal leen xebaaru yàlla bu baax bi, waaye jox leen it sunu bakkan, ndaxte sunu xol seeyoon na ci yéen.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
se gli altri hanno tale diritto su di voi, non l'avremmo noi di più? noi però non abbiamo voluto servirci di questo diritto, ma tutto sopportiamo per non recare intralcio al vangelo di cristo
ndegam ñeneen a am sañ-sañ boobu ci yéen, nun kon waxi-noppi. waaye nag jariñoowunu sañ-sañ boobu. danuy far muñ lépp, ngir bañ a indi ndog ci yoonu xebaar bu baax bu kirist bi.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità: