Hai cercato la traduzione di mmekwisha da Swahili a Wolof

Contributi umani

Da traduttori professionisti, imprese, pagine web e archivi di traduzione disponibili gratuitamente al pubblico.

Aggiungi una traduzione

Swahili

Wolof

Informazioni

Swahili

ninyi mmekwisha kuwa safi kwa sababu ya ule ujumbe niliowaambieni.

Wolof

yéen nag, baay bi setal na leen jaarale ko ci kàddu gi ma leen wax, ni beykat di tenqee garabam.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

lakini ole wenu ninyi mlio matajiri, maana mmekwisha pata faraja yenu.

Wolof

waaye nag yéen boroom alal yi, torox ngeen,ndaxte jot ngeen ba noppi seen bànneex.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

msiambiane uongo, kwani ninyi mmekwisha vua ule utu wa kale pamoja na matendo yake yote,

Wolof

bàyyileen di fen seeni moroom, ndaxte summi ngeen jikko ju bon, ji ngeen judduwaale, moom ak ay jëfam;

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

je, mmekwisha mwona hata mmoja wa viongozi wa watu, au mmoja wa mafarisayo aliyemwamini?

Wolof

ndax am na kenn ci saraxalekat yi walla ci farisen yi ku ko gëm? déedéet.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

"mmekwisha sikia ya kuwa watu wa kale waliambiwa: usiue! atakayeua lazima ahukumiwe.

Wolof

«dégg ngeen ne, waxoon nañu maam ya ne leen: “bul rey nit; ku rey nit, yoon dina la dab.”

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Attenzione: contiene formattazione HTML nascosta

Swahili

kwa hiyo nitaendelea kuwakumbusheni daima mambo haya, ingawa mmekwisha yafahamu, na mko imara katika ukweli mlioupokea.

Wolof

wóor na ma ne xam ngeen loolu, ba sampu ci dëgg gi leen yàlla jagleel, waaye fas naa yéene, may sax ci di leen ko fàttali.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

ikiwa mnanijua mimi mnamjua na baba yangu pia. na tangu sasa, mnamjua, tena mmekwisha mwona."

Wolof

ndegam xam ngeen ma, dingeen xam itam sama baay. lu weesu tey, xam ngeen ko te gis ngeen ko.»

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Attenzione: contiene formattazione HTML nascosta

Swahili

lakini ninyi, wapenzi wangu, mmekwisha jua jambo hili. basi, muwe na tahadhari msije mkapotoshwa na makosa ya waasi, mkaanguka kutoka katika msimamo wenu imara.

Wolof

noonu yeen samay xarit, gannaaw xam ngeen loolu ba noppi, moytuleen ñi weddi fàbbi leen ci seen réer, ba yolomal seen wàkkirlu ci yàlla.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

lakini ninyi, watoto, ni wake mungu na mmekwisha washinda hao manabii wa uongo; maana roho aliye ndani yenu ana nguvu zaidi kuliko roho aliye ndani ya hao walio wa ulimwengu.

Wolof

yéen samay doom, ci yàlla ngeen bokk, te daan ngeen yonent yu naaféq yooyu, ndaxte ki nekk ci yéen moo ëpp doole ki nekk ci àddina.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

mungu aliwafunulia kwamba wakati walipokuwa wanasema juu ya hayo mambo ambayo ninyi mmekwisha sikia sasa kutoka kwa wale wajumbe waliowatangazieni habari njema kwa nguvu ya roho mtakatifu aliyetumwa kutoka mbinguni, hiyo kazi yao haikuwa kwa faida yao wenyewe, bali kwa ajili yenu. hayo ndiyo mambo ambayo hata malaika wangependa kuyafahamu.

Wolof

waaye yàlla xamal na leen ne, moomuñu woon kàddu googu ñu wax, waaye yéena ko moom. te mooy kàddu gi ngeen dégg ci gémmiñu ñi leen doon jottali xebaar bu baax bi, ci dooley xel mu sell, mi yàlla yónnee asamaan; malaaka yi sax bëgg nañoo gëstu yëf yii.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Swahili

aristarko, ambaye yuko kifungoni pamoja nami, anawasalimuni; hali kadhalika marko, binamu yake barnaba, (mmekwisha pata maagizo juu yake; akifika kwenu mkaribisheni).

Wolof

aristàrk mi nekk ak man ci kaso bi, mu ngi leen di nuyu, moom ak màrk rakku barnabas. jot ngeen ay ndigal ci mbirum màrk: bu ñëwee ci yéen, teral-leen ko.

Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:

Ottieni una traduzione migliore grazie a
7,765,631,950 contributi umani

Ci sono utenti che chiedono aiuto:



I cookie ci aiutano a fornire i nostri servizi. Utilizzando tali servizi, accetti l'utilizzo dei cookie da parte nostra. Maggiori informazioni. OK