検索ワード: kupigana (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

basi, achana na madhambi yako. la sivyo, nitakuja kwako upesi na kupigana na watu hao kwa upanga utokao kinywani mwangu.

ウォロフ語

réccul kon; lu ko moy dinaa dikk ci yaw léegi te xeex ak nit ñooñu ak jaasi, jiy génn ci sama gémmiñ. i

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mwanangu timotheo, nakukabidhi amri hii kufuatana na maneno ya unabii yaliyosemwa zamani juu yako. yatumie maneno hayo yawe silaha yako katika kupigana vita vizuri,

ウォロフ語

kon nag timote sama doom, loolu mooy sas wi ma lay dénk, te mu dëppook waxi yonent, yi jëmoon ci yaw. doolewool wax yooyu, ba xeex xeex bu baax bi,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, joka hilo likamkasirikia huyo mama, likajiondokea, likaenda kupigana na wazawa wengine wa huyo mama, yaani wote wanaotii amri za mungu na kuuzingatia ukweli wa yesu.

ウォロフ語

ninkinànka ja mere jigéen ja, daldi xeexi ak ñi des ciy doomam, di ñiy sàmm ndigali yàlla tey sax ci di seedeel yeesu.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

ndugu wapenzi, wakati nimo katika jitihada ya kuwaandikieni juu ya ule wokovu tunaoshiriki sote, nimeona lazima ya kuwaandikieni na kuwahimizeni mwendelee kupigana kwa ajili ya imani ambayo mungu amewajalia watu wake mara moja tu kwa wakati wote.

ウォロフ語

samay bokk, bëggoon naa leen a bind lool ci mbirum mucc gi nu bokk, waaye lii moo gën a jamp: ma xiir leen, ngeen taxaw ci aar mboolem dëgg, yi yàlla xas a dénk gaayam yu sell yi ba fàww.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mnatamani vitu na kwa vile hamvipati mko tayari kuua; mwatamani sana kupata vitu, lakini hamvipati, hivyo mnagombana na kupigana. hampati kile mnachotaka kwa sababu hamkiombi kwa mungu.

ウォロフ語

dangeen di mébét waaye dungeen am; dangeen di rey nit, boole ci kiñaan, waaye li ngeen di yóotu, dungeen ko jot; dangeen di xuloo ak a xeex waaye dungeen am dara, ndaxte ñaanuleen yàlla.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"au, ni mfalme gani ambaye, akitaka kwenda kupigana na mfalme mwingine, hataketi kwanza chini na kufikiri kama ataweza, kwa askari wake elfu ishirini?

ウォロフ語

walla boog ban buur mooy dugg ci xare ak beneen buur te jëkkul a toog, seet ba xam moom ak fukki junniy xarekat man na xeex ak kiy ñëw ak ñaar-fukki junniy xarekat?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

kama kusudi langu lingalikuwa la kibinadamu tu, kule kupigana kwangu na wanyama wakali hapa efeso kungalinifaa kitu gani? kama wafu hawafufuki, basi, "tule na tunywe, maana kesho tutakufa."

ウォロフ語

su fekkee ne ci ni ñu ko waxe, xeex naa ca dëkku efes ak rabi àll, kon ban njariñ la may amal? su néew yi dul woon dekki, am na lu ci léeb wax:«nanu lekk di naan, ndaxte ëllëg dinanu dee.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
7,777,620,200 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK