検索ワード: maadam (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

maadam wengi hujivuna kwa sababu za kidunia, nami pia nitajivuna.

ウォロフ語

ndegam ñu bare dañuy damu ni nit kese, man itam kon dinaa damu.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hali kadhalika na ninyi, maadam mna hamu ya kupata vipaji vya roho, jitahidini hasa kujipatia vile vinavyosaidia kulijenga kanisa.

ウォロフ語

yéen itam, gannaaw dangeen a fonk mayi xelum yàlla, jéemleen a ëpple ci liy yokk ngëmu mbooloo mi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

sasa, maadam inahubiriwa kwamba kristo amefufuliwa kutoka wafu, baadhi yenu wanawezaje kusema kwamba hakuna ufufuo wa wafu?

ウォロフ語

waaye su nu yéglee ne, kirist dekki na, nan la ñenn ñi ci yéen man a waxe ne, néew yi duñu dekki?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mtu hafanyi mambo kwa siri kama anataka kujulikana kwa watu. maadam unafanya mambo haya, basi, jidhihirishe kwa ulimwengu."

ウォロフ語

ku bëgg a siiw, doo nëbb say jëf. boo demee bay wone jaloore yu mel ni, fexeel ba ñépp gis la.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

nilipokuwa mtoto mchanga nilisema kitoto, nilifahamu kitoto, nilifikiri kitoto. lakini sasa, maadam mimi ni mtu mzima, mambo ya kitoto nimeyaacha.

ウォロフ語

bi ma dee xale, dama doon wax ni xale, di dégge ni xale, di xalaate ni xale. waaye bi ma doonee mag, bàyyi naa lu bokkoon cig ndaw.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

ningekuwa nimeichagua kazi hii kwa hiari, basi, ningetazamia malipo; lakini maadam naifanya ikiwa ni wajibu, hiyo ina maana kwamba ni jukumu nililopewa nitekeleze.

ウォロフ語

su doon ci sama coobare laa yégle xebaar bu baax bi, man naa ci séentu yool. waaye defuma ko ci sama coobare, ndaxte sas la, wu ñu ma sas.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

wakamwuliza tena huyo mtu aliyekuwa kipofu, "maadam yeye amekufungua macho, wasemaje juu yake?" naye akawaambia, "yeye ni nabii!"

ウォロフ語

farisen ya laajaat ka gumba woon ne ko: «yaw, loo wax ci moom? yaw de la ubbil say bët.» mu ne leen: «yonent la.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

kwa hiyo, ndugu zangu, maadam mungu ni mwenye huruma nyingi, nawasihi kwa moyo wote: jitoleeni nafsi zenu kwa mungu kama tambiko iliyo hai, takatifu na yenye kupendeza. hii ndiyo njia yenu halisi ya kumwabudu.

ウォロフ語

kon nag bokk yi, gannaaw yërmandey yàlla baree na noonu, maa ngi leen di ñaan, ngeen jébbal ko seen yaram wépp. na seen dund mel ni sarax su ñuy defal yàlla, sarax su sell te neex ko. loolu mooy njaamu, gi leen war.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

人による翻訳を得て
7,768,972,573 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK