検索ワード: mbaya (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

agizo mbaya (exec) kuzindua

ウォロフ語

santaane bees war a jëfe (exec) baaxul

最終更新: 2014-08-15
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

msidanganyike! urafiki mbaya huharibu tabia njema.

ウォロフ語

bu leen ko réere mbir: «Ànd bu bon dina yàq nit ku baax.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

tumieni vizuri muda mlio nao maana siku hizi ni mbaya.

ウォロフ語

tey jariñoo jot gi, ndaxte nu ngi ci jamono ju bon.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

lakini mtu hujaribiwa anapovutwa na kunaswa na tamaa zake mbaya.

ウォロフ語

waaye ku sa bakkan nax, ba man la, looloo lay dugal ci fiir.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

na si kwa tamaa mbaya kama watu wa mataifa mengine wasiomjua mungu.

ウォロフ語

te xemmem bañ leen a jiital, ni xeeti àddina yi xamul yàlla.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

vaeni silaha anazowapeni mungu mpate kuzipinga mbinu mbaya za ibilisi.

ウォロフ語

gànnaayooleen yérey xarey yàlla yépp, ngir man a jànkoonte ak pexey seytaane.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, mti mwema huzaa matunda mema, na mti mbaya huzaa matunda mabaya.

ウォロフ語

noonu garab gu baax gu nekk dina meññ doom yu neex, waaye garab gu bon dina meññ doom yu bon.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"mti mwema hauzai matunda mabaya, wala mti mbaya hauzai matunda mazuri.

ウォロフ語

«garab gu baax du meññ doom yu bon, te garab gu bon du meññ doom yu baax.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

alimwokoa loti, mtu mwema, ambaye alisikitishwa sana na mwenendo mbaya wa watu hao waasi.

ウォロフ語

waaye musal na lóot mi jub, mi sonnoon ndax ñaawteefi ñu dëng, ñooñu mu nekkaloon.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

tena watu wengi watazifuata hizo njia zao mbaya, kwa sababu yao, wengine wataipuuza njia ya ukweli.

ウォロフ語

ñu bare dinañu leen fekki ci seeni ñaawteef, ba gàkkal yoonu dëgg ci bëti nit ñi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

jambo tunalosisitiza kwenu si jambo linalotegemea uongo au nia mbaya; wala hatupendi kumdanganya mtu yeyote.

ウォロフ語

ndaxte sunu waaraate wéeruwul cig réer walla ci njublaŋ walla ciy nax.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

awali ya yote jueni kwamba siku za mwisho watakuja watu ambao mienendo yao inatawaliwa na tamaa zao mbaya. watawadhihaki ninyi

ウォロフ語

nangeen jëkka xam lii: muju jamano dingeen gis ay tiiñalkat, di topp seen bakkan; dinañu leen tiiñal

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

ghadhabu ya mungu imedhihirishwa kutoka mbinguni dhidi ya uasi na uovu wote wa binadamu ambao kwa njia zao mbaya wanaupinga ukweli usijulikane.

ウォロフ語

merum yàllaa ngi feeñe asamaan, wàcc ci nit ñi, ndax seen weddi yàlla gépp ak seen jubadi gépp, ñoom ñi suul dëgg, di topp lu jubadi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi ndugu, jihadharini asije akawako yeyote miongoni mwenu aliye na moyo mbaya hivyo na asiyeamini hata kujitenga na mungu aliye hai.

ウォロフ語

bokk yi, wottuleen ba kenn ci yéen bañ a am xol bu bon te gëmadi, bay dëddu yàlla jiy dund.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hapo yule bwana alimwita huyo mtumishi, akamwambia, wewe ni mtumishi mbaya sana! uliniomba, nami nikakusamehe deni lako lote.

ウォロフ語

sang ba nag woolu jaraaf ba ne ko: “yaw jaraaf ju soxor nga! baal naa la sa bor bépp, ndaxte tinu nga ma.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hasa wale wanaofuata tamaa mbaya za mwili na kupuuza mamlaka. watu hao ni washupavu na wenye majivuno, huvitukana na hawaviheshimu viumbe vitukufu vya juu.

ウォロフ語

rawatina ñiy topp seen bakkan ciy bëgg-bëgg yu ruslu, te faalewuñu genn kilifteef. ñu ñeme yàlla lañu, te dëgër bopp, ba ragaluñoo xas kilifa ya gëna kawe.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kwa tamaa yao mbaya watajipatia faida kwa kuwaambieni hadithi za uongo. lakini kwa muda mrefu sasa hakimu wao yu tayari, na mwangamizi wao yu macho!

ウォロフ語

seen bëgge dina tax, ñu dàbbdaaxe ay wax, ngir nax leen, ba lekk seenus tuut. waaye àtte baa ngi leen di xaar, te seen alkande di leen teeru.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"ufanyeni mti kuwa mzuri na matunda yake yatakuwa mema; ufanyeni kuwa mbaya na matunda yake yatakuwa mabaya. mti hujulikana kwa matunda yake.

ウォロフ語

neeleen garab gi baax na, moom ak meññeefam, walla ngeen ne garab gi bon na, moom ak meññeefam; ndaxte garab, meññeefam lañu koy xàmmee.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

ambako alikaa kwa miezi mitatu. alipokuwa anajitayarisha kwenda siria, aligundua kwamba wayahudi walikuwa wanamfanyia mpango mbaya; hivyo aliamua kurudi kwa kupitia makedonia.

ウォロフ語

toog fa ñetti weer. waaye bi mu nekkee ci kaw tànki dugg gaal jëm diiwaanu siri, te yawut yi lalal ko pexe, mu fas yéenee dellu, jaare maseduwan.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mtu mwema hutoa yaliyo mema kutoka katika hazina bora iliyo moyoni mwake; na mtu mbaya hutoa yaliyo mabaya katika hazina mbaya iliyo moyoni mwake, kwa maana mtu huongea kutokana na yale yaliyojaa moyoni mwake.

ウォロフ語

noonu nit ku baax, lu baax lay wax, ndax loolu la denc ci xolam, te nit ku bon, lu bon lay wax, ndaxte denc na lu bon ci xolam. ndaxte gémmiñ, la fees xolam lay wax.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

人による翻訳を得て
7,735,143,743 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK