検索ワード: mfalme (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

wakaanza kumsalimu, "shikamoo mfalme wa wayahudi!"

ウォロフ語

Ñu daldi ko wax bu kawe: «nuyu nanu la, yaw buuru yawut yi!»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

na mshtaka wake ulikuwa umeandikwa: "mfalme wa wayahudi."

ウォロフ語

mbind mi xamle lu tax ñu rey ko nee na: «kii mooy buuru yawut yi.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

pilato akawauliza, "je, mwataka niwafungulieni mfalme wa wayahudi?"

ウォロフ語

pilaat nag xam ne, kiñaan rekk a taxoon saraxalekat yu mag yi jébbal ko yeesu. kon mu ne mbooloo mi: «xanaa ma bàyyil leen buuru yawut yi?»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

karibu wakati huohuo, mfalme herode alianza kuwatesa baadhi ya wakristo.

ウォロフ語

ca jamono jooja erodd buur ba jàppoon na ay nit ci mbooloom ñi gëm, ngir fitnaal leen.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"ufalme wa mbinguni umefanana na mfalme aliyemwandalia mwanawe karamu ya arusi.

ウォロフ語

«nguuru yàlla aji kawe ji dafa mel ni buur buy waajal céetu doomam ju góor.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"hivyo, mfalme agripa, sikuweza kuwa mkaidi kwa maono hilo la mbinguni.

ウォロフ語

«kon nag buur agaripa, woruma li ma yàlla yen ci peeñu.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

hapo mfalme agripa, mkuu wa mkoa, bernike na wale wote waliokuwa pamoja nao, walisimama.

ウォロフ語

ci kaw loolu buur ba daldi jóg, boroom réew ma topp ci, berenis tegu ca ak mbooloo ma mépp.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"mfalme alipoingia kuwaona wageni, akamwona mtu mmoja ambaye hakuvaa mavazi ya arusi.

ウォロフ語

«bi nga xamee ne buur bi dugg na nag, ngir seetsi gan yi, mu gis fa nit ku solul mbubb mu ñu war a sol ca céet ga.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

kama anaona hataweza, atawatuma wajumbe kutaka masharti ya amani wakati mfalme huyo mwingine angali mbali.

ウォロフ語

su ko mënul, dafay yónni ndaw ca beneen buur ba, fi ak ma ngay sore, ngir ñu juboo.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mfalme atawajibu, kweli nawaambieni, kila kitu mlichomtendea mmojawapo wa hawa ndugu zangu wadogo, mlinitendea mimi.

ウォロフ語

noonu buur bi dina leen tontu ne: “ci dëgg maa ngi leen koy wax, saa yu ngeen defalee loolu kenn ki gën a ndaw ci sama bokk yii, man ngeen ko defal.”

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"usiogope mji wa sioni! tazama, mfalme wako anakuja, amepanda mwana punda."

ウォロフ語

«buleen ragal, waa siyon.gis ngeen, seen buur a ngi ñëw,war mbaam mu ndaw.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

basi, jiwekeni chini ya mamlaka yote ya kibinadamu, kwa ajili ya bwana: utii kwa mfalme aliye mtawala mkuu,

ウォロフ語

na seen nangub boroom bi tax, ngeen déggal képp kuy kilifa, muy buur ba gën a kawe,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hapo mfalme akawaambia watumishi, mfungeni miguu na mikono mkamtupe nje gizani; huko atalia na kusaga meno."

ウォロフ語

noonu buur ba ne ay surgaam: “yeewleen ko ci tànk yi ak ci loxo yi, sànni ko ci biti ci lëndëm gi. foofa dees na fa jooy tey yéyu.”

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"mfalme agripa, ninajiona mwenye bahati leo kujitetea mbele yako kuhusu yale mashtaka yote ambayo wayahudi walikuwa wamesema juu yangu.

ウォロフ語

«buur agaripa, ma làyyi ci sa kanam tey ci lépp, li ma yawut yiy jiiñ, xol bu sedd la ci man,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

baada ya kumsikiliza mfalme, hao wataalamu wa nyota wakaenda. kumbe ile nyota waliyokuwa wameiona upande wa mashariki iliwatangulia hata ikaenda kusimama juu ya mahali pale alipokuwa mtoto.

ウォロフ語

ba ñu dégloo buur ba nag, ñu dem. te biddiiw, ba ñu gisoon ca penku ba, ne tell jiite leen, ba àgg, tiim fa xale ba nekk.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"huyo mtu mashuhuri alirudi nyumbani baada ya kufanywa mfalme, na mara akaamuru wale watumishi aliowapa zile fedha waitwe ili aweze kujua kila mmoja amepata faida gani.

ウォロフ語

«bi ñu ko falee buur nag, ba mu dellusi, mu woolu surga, ya mu joxoon wurus wa, ngir xam nan lañu ci liggéeye.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"kisha mfalme atawaambia wale walio upande wake wa kulia, njoni enyi mliobarikiwa na baba yangu; pokeeni ufalme mliotayarishiwa tangu kuumbwa kwa ulimwengu.

ウォロフ語

«noonu buur bi dina wax ñi féete ndeyjoor: “agsileen, yéen ñi sama baay barkeel, jël-leen nguur, gi ñu leen waajal li dale ci njàlbéenug àddina.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"aliwaokoa wengine, lakini kujiokoa mwenyewe hawezi! eti yeye ni mfalme wa wayahudi! basi, sasa na ashuke msalabani, nasi tutamwamini.

ウォロフ語

«waa jii musal na ñeneen te mënul a musal boppam! ndegam mooy buuru israyil, na wàcc léegi ci bant bi, nu gëm ko.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"au, ni mfalme gani ambaye, akitaka kwenda kupigana na mfalme mwingine, hataketi kwanza chini na kufikiri kama ataweza, kwa askari wake elfu ishirini?

ウォロフ語

walla boog ban buur mooy dugg ci xare ak beneen buur te jëkkul a toog, seet ba xam moom ak fukki junniy xarekat man na xeex ak kiy ñëw ak ñaar-fukki junniy xarekat?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"uambieni mji wa sioni: tazama, mfalme wako anakujia! ni mpole na amepanda punda, mwana punda, mtoto wa punda."

ウォロフ語

«waxal waa siyon:“seen buur a ngi ñëw ci yéen;ku lewet la, te war mbaam-sëf,dig cumbur, doomu mbaam.”»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
7,761,687,336 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK