検索ワード: msalaba (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

mtu asiyechukua msalaba wake na kunifuata, hanistahili.

ウォロフ語

koo xam ne kii nanguwuloo ñàkk sa bakkan, ba mel ni ku ñu daaj ci bant, te nga topp ma, yeyoowuloo ma.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mtu asipochukua msalaba wake na kunifuata hawezi kuwa mwanafunzi wangu.

ウォロフ語

képp koo xam ne nanguwuloo ñàkk sa bakkan, ba mel ni ku ñu daaj ci bant, te nga topp ma, doo man a nekk sama taalibe.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

walipokuwa wakienda, wakamkuta mtu mmoja jina lake simoni, mwenyeji wa kurene, wakamlazimisha kuuchukua msalaba wake yesu.

ウォロフ語

bi nga xamee ne génn nañu, ñu daje ak nit ku dëkk siren te tudd simoŋ; ñu ga ko, ngir mu gàddu bant, ba ñu war a daaj yeesu.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

karibu na msalaba wake yesu walikuwa wamesimama mama yake, na dada ya mama yake, maria mke wa kleopa, na maria magdalene.

ウォロフ語

ca wetu bant, ba ñu daajoon yeesu, yaayam a nga fa taxawoon, moom ak doomu ndeyam ju jigéen, maryaama jabari këlópas, ak maryaama mi dëkk magdala.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

juu ya msalaba kristo aliwapokonya nguvu zao hao pepo watawala na wakuu; aliwafanya kuwa kitu cha fedheha hadharani kwa kuwaburuta kama mateka katika msafara wa ushindi wake.

ウォロフ語

futti na kilifa yi ak boroom sañ-sañ yi, weer leen ci kanamu ñépp, sëkktal leen niy jaam ndax ndam la kirist jële ca bant ba.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

naye akatoka akiwa amejichukulia msalaba wake kwenda mahali paitwapo "fuvu la kichwa", (kwa kiebrania golgotha).

ウォロフ語

yeesu ci boppam gàddu bant ba, génn ngir dem ca fa ñuy wax bérabu kaaŋu bopp; ñu koy wooye golgota ci làkku yawut.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

kisha akawaambia watu wote, "mtu yeyote akitaka kuwa mfuasi wangu, ni lazima ajikane nafsi yake, auchukue msalaba wake kila siku, anifuate.

ウォロフ語

noonu yeesu ne leen ñoom ñépp: «ku bëgg a aw ci samay tànk, na bàyyi boppam, gàddu bés bu nekk bant, bi ñu ko war a daaj, door a topp ci man.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

walipokuwa wakimpeleka, walikutana na mtu mmoja, aitwaye simoni wa kurene, aliyekuwa anatoka shambani. basi, walimkamata, wakamtwika ule msalaba auchukue nyuma ya yesu.

ウォロフ語

bi ñuy yóbbu yeesu, ñu jàpp ku ñuy wax simoŋ te mu dëkk siren, ku jóge ca wet, ga féete ak tool ya, sëf ko bant, ba ñuy war a daaj yeesu, ngir mu gàddu ko, topp ci moom.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kisha akauita umati wa watu pamoja na wanafunzi wake, akawaambia, "mtu yeyote akitaka kuwa mfuasi wangu, lazima ajikane mwenyewe, auchukue msalaba wake, anifuate.

ウォロフ語

noonu yeesu woo taalibe yi ak mbooloo mi ne leen: «ku bëgg a topp ci samay tànk, na bàyyi boppam te gàddu bant bi ñu ko war a daaj, door a topp ci man.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

walipokuwa njiani, walikutana na mtu mmoja aitwaye simoni, mwenyeji wa kurene. yeye alikuwa baba wa aleksanda na rufo, na wakati huo alikuwa akitoka shambani. basi, wakamlazimisha auchukue msalaba wa yesu.

ウォロフ語

amoon na nag nit ku dëkk siren, tudd simoŋ, di baayu alegsàndar ak rufus. fekk booba mu romb fa, jóge ca wet, ga féete ak tool ya, ñu ga ko ngir mu gàddu bant bi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

na kwa upande wangu, ndugu zangu, kama bado ninahubiri kwamba kutahiriwa ni lazima, kwa nini basi, bado ninadhulumiwa? kama ingalikuwa hivyo, mahubiri yangu juu ya msalaba wa kristo yasingalileta aibu yoyote.

ウォロフ語

man nag bokk yi, bu ma doon faaydaal xaraf ci sama waare, kon duñu ma fitnaale nii; te it li may yégle ci deewu kirist ca bant ba dootul naqari kenn.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

人による翻訳を得て
7,761,290,897 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK