検索ワード: waziwazi (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

basi, yesu akawaambia waziwazi, "lazaro amekufa;

ウォロフ語

ci kaw loolu yeesu wax ci lu leer ne: «lasaar dee na.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

lakini kefa alipofika antiokia nilimpinga waziwazi maana alikuwa amekosea.

ウォロフ語

waaye bi sefas ñëwee dëkku ancos, yedd naa ko ci kanamu ñépp, ndaxte li mu def jaaduwul.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

yesu aliwaambia jambo hilo waziwazi. basi, petro akamchukua kando, akaanza kumkemea.

ウォロフ語

noonu mu xamal leen mbir mi, ba mu leer nàññ. bi ko piyeer déggee, mu woo ko ci pegg, daldi ko yedd.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

najua kwamba karibu nitauweka kando mwili huu wenye kufa, kama bwana alivyoniambia waziwazi.

ウォロフ語

ndaxte xam naa ne, léegi ma jóge fi, ni ma ko yeesu krist boroom bi leerale woon.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

vivyo hivyo, matendo mema huonekana waziwazi, na hata yale ambayo si dhahiri hayawezi kufichika.

ウォロフ語

naka noonu it am na, ñu seen jëf yu rafet leer, te yi feeñul mënuñoo nekk kumpa ba fàww.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, wanafunzi wake wakamwambia, "ahaa! sasa unasema waziwazi kabisa bila kutumia mafumbo.

ウォロフ語

taalibe yi ne ko: «léegi yaa ngi wax lu leer te misaaloo!

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

maana yesu mwenyewe alisema waziwazi kwamba, "nabii hapati heshima katika nchi yake."

ウォロフ語

ndaxte moom ci boppam nee woon na: «ab yonent, kenn du ko faaydaal ca réewam.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

dhambi za watu wengine huonekana waziwazi, nazo zawatangulia kwenye hukumu; lakini dhambi za wengine huonekana tu baadaye.

ウォロフ語

am na, ñu seeni bàkkaar fés ci kanamu ñépp, ba jiitu leen ca àtte ba; ñi seeni bàkkaar nëbbu nag, bés baa ngi leen di xaar.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"nimewaambieni mambo hayo kwa mafumbo. lakini wakati utakuja ambapo sitasema tena nanyi kwa mafumbo, bali nitawaambieni waziwazi juu ya baba.

ウォロフ語

«loolu lépp, dama leen koo wax ci ay misaal. jamono dina ñëw, ju ma dootul wax ak yéen ci ay misaal, waaye ju ma leen dee wax lu leer ci baay bi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

basi, sisi tunajua umuhimu wa kumcha bwana, na hivyo tunajitahidi kuwavuta watu. mungu anatujua waziwazi, nami natumaini kwamba nanyi pia mnatujua kinaganaga.

ウォロフ語

gannaaw xam nanu ragal yàlla nag, nu ngi fexee gëmloo nit ñi, waaye li nu nekk leer na yàlla te yaakaar naa ne, leer na leen it, ba ne fàŋŋ.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"tuliwakatazeni waziwazi kufundisha kwa jina la mtu huyu; sasa mmeyaeneza mafundisho yenu pote katika yerusalemu na mnakusudia kutuwekea lawama ya kifo cha mtu huyo."

ウォロフ語

ne: «ndax terewunu leen ci lu wér, ngeen waare ci tur woowu, te fi mu ne dajal ngeen yerusalem ak seeni waare, rax-ca-dolli yéena ngi nuy fexee taqal deretu nit kooku.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"ndugu zangu, napenda kuwaambieni waziwazi juu ya mambo yaliyompata daudi, babu yetu. yeye alikufa, akazikwa, tena kaburi lake liko papa hapa petu mpaka leo.

ウォロフ語

«bokk yi, man naa leen a wax lu wóor ci mbirum maam daawuda, ne dee na te suul nañu ko; bàmmeelam mu ngi ci nun ba tey.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

lakini huyo mtu akaenda, akaanza kueneza habari hiyo kila mahali na kusema mambo mengi hata yesu hakuweza tena kuingia katika mji wowote waziwazi; ikamlazimu kukaa nje, mahali pa faragha. hata hivyo, watu wakamwendea kutoka kila upande.

ウォロフ語

waaye naka la waa ji génn, mu di yéene ci kaw li xewoon, te di ko jéebaane, ba tax yeesu mënatul a faŋaaral dugg cib dëkk, waaye mu nekk ci biti ciy bérab yu wéet. ba tey nit ñi jóge fu nekk, di ko fa fekk.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

人による翻訳を得て
7,758,332,821 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK