プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。
nafahamu vizuri sana kwamba baada ya kuondoka kwangu mbwa mwitu wakali watawavamieni, na hawatakuwa na huruma kwa kundi hilo.
xam naa ne, bu ma leen wonee gannaaw, bukki yu soxor dinañu tàbbi ci coggal ji te duñu ci ñeeblu kenn.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
husuda, ulevi, ulafi na mambo mengine kama hayo. nawaambieni tena kama nilivyokwisha sema: watu wanaotenda mambo hayo hawatakuwa na nafasi yao katika ufalme wa mungu.
kiñaan, màndite ak xawaare ak yeneen yu ni mel. léegi nag maa ngi leen di artu, ni ma ko defe woon: ñiy jëfe noonu duñu am cér ci nguuru yàlla.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
moshi wa moto unaowatesa kupanda juu milele na milele. watu hao waliomwabudu huyo mnyama na sanamu yake, na kutiwa alama ya jina lake, hawatakuwa na nafuu yoyote usiku na mchana."
te saxar siy jóge ci seen mbugal dina gilli ba fàww. Ñooñu di jaamu rab wi ak nataalam, ak képp ku nangoo jot màndargam turam, duñu noppalu guddi ak bëccëg.»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています