검색어: kuamini (스와힐리어 - 월로프어)

인적 기여

전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.

번역 추가

스와힐리어

월로프어

정보

스와힐리어

hivyo hawakuweza kuamini, kwani isaya tena alisema:

월로프어

mënuñu woon a gëm, ndaxte esayi dafa waxaat ne:

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

nimewaambieni haya sasa kabla hayajatokea, ili yatakapotokea mpate kuamini.

월로프어

wax naa leen ko nag léegi, bala looloo ñëw, ngir bu waxtu wa agsee, ngeen gëm.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kwa nini ninyi mnaona shida sana kuamini kwamba mungu huwafufua wafu?

월로프어

lu tax seen xel dàq ne, yàlla dina dekkal ñi dee?

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

mimi nimewaambieni mambo haya sasa kabla hayajatokea, ili yatakapotokea mpate kuamini kuwa mimi ndimi.

월로프어

maa ngi leen koy wax ci teel, bala looloo ñëw, ngir bu ñëwee, ngeen gëm ne, maay ki nekk.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kwa njia yake mnaokolewa, ikiwa mnayazingatia maneno niliyowahubirieni, na kama kuamini kwenu hakukuwa bure.

월로프어

ci moom ngeen jaare, ba mucc, bu ngeen téyee bu dëgër njàngale mi, ni ma leen ko yégale. walla xanaa boog gëm ngeen ko cig neen?

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

ambaye alikuja kuwaambia watu juu ya huo mwanga. alikuja ili kwa ujumbe wake watu wote wapate kuamini.

월로프어

kooku ñëw na, doon ab seede, ngir wax ci mbirum leer gi. Ñëw na ngir ñépp dégg li mu wax te gëm.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

ikiwa nimewaambieni mambo ya kidunia nanyi hamniamini, mtawezaje kuamini nikiwaambieni mambo ya mbinguni?

월로프어

gannaaw gëmuleen li ma leen di wax ci mbiri àddina, naka ngeen man a gëme, bu ma leen waxee ci mbiri asamaan?

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kama ukikiri kwa kinywa chako kwamba yesu ni bwana na kuamini moyoni mwako kwamba mungu alimfufua kutoka wafu, utaokoka.

월로프어

ndaxte soo waxee ak sa gémmiñ ne, yeesu mooy boroom bi, te nga gëm ci sa xol ne, yàlla dekkal na ko, dinga mucc.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kwa njia yake, mimi nimepewa neema ya kuwa mtume, ili kwa ajili yake niwaongoze watu wa mataifa yote wapate kuamini na kutii.

월로프어

te moom kirist tàbbal na nu ci yiwu yàlla, def nu ay ndawam, yónni nu ci biir xeeti àddina sépp, ngir ñu gëm ko te jébbalu, ba màggal turam.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

ndio maana sisi tunajivunia ninyi katika makanisa ya mungu. tunaona fahari juu ya jinsi mnavyoendelea kuamini na kustahimili katika udhalimu wote na mateso mnayopata.

월로프어

noonu nu ngi damu ci yéen ci kanamu mboolooy yàlla yi, ndax seen muñ ak seen ngëm ci biir mboolem fitnay noon, ak coono, yi ngeen di dékku.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

mwawezaje kuamini, hali ninyi mnapenda kupokea sifa kutoka kwenu ninyi wenyewe, wala hamtafuti sifa kutoka kwake yeye aliye peke yake mungu?

월로프어

bëgg ngeen ku leen di tagg, te wutuleen ngërëm, li jóge ci jenn yàlla rekk ji am. kon nan ngeen man a gëme?

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

lakini hizi zimeandikwa ili mpate kuamini kwamba yesu ni kristo, mwana wa mungu; na kwa kuamini mpate kuwa na uzima kwa nguvu ya jina lake.

월로프어

waaye li ci nekk, bind nañu ko ngir ngeen gëm ne, yeesu mooy almasi bi, doomu yàlla ji, te seen ngëm may leen, ngeen am ci moom dund.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

(naye aliyeona tukio hilo ametoa habari zake ili nanyi mpate kuamini. na hayo aliyosema ni ukweli, tena yeye anajua kwamba anasema ukweli.)

월로프어

kiy nettali mbir yooyu, da cee teg bëtam, te li muy wax dëgg la. moom ci boppam xam na ne, li muy wax dëgg la, ngir yéen itam ngeen gëm,

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

nanyi wake, jiwekeni chini ya mamlaka ya waume zenu, ili kama wako waume wowote wasioamini neno la mungu, wapate kuamini kwa kuuona mwenendo wenu. haitakuwa lazima kwenu kusema neno,

월로프어

yéen itam jigéen ñi, na ku nekk nangul sa jëkkër. noonu su amee góor gu gëmul kàddug yàlla, te gis jabaram di dund dund gu sell, boole ci weg ko, loolu dina ko gindi ci lu àndul ak wax.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

lakini sivyo; maandiko matakatifu yamekwisha sema kwamba ulimwengu wote upo chini ya utawala wa dhambi; na hivyo, kwa kumwamini yesu kristo, wenye kuamini watimiziwe ile ahadi.

월로프어

waaye yoon wi tëj na ñépp ci dooley bàkkaar, ngir ñi gëm yeesu kirist jot li yàlla dige woon ci seen kaw ngëm.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

lakini wengine walikuwa wakaidi, wakakataa kuamini, wakaanza kuongea vibaya hadharani juu ya njia ya bwana. hapo paulo alivunja uhusiano nao, akawachukua pembeni wale wanafunzi wake, akawa anazungumza nao kila siku katika jumba la masomo la turano.

월로프어

waaye bi xolu ñenn ci ñoom fattee, ñu gëmadi, bay suufeel yoon wi ci kanam mbooloo ma, mu jóge ci ñoom, xàjjale taalibe yi ak ñoom, di diisoo bés bu nekk ca jàngukaayu ku ñuy wax tiranus.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

baada ya majadiliano marefu, petro alisimama, akasema, "ndugu zangu, ninyi mnafahamu kwamba hapo awali mungu alipenda kunichagua mimi miongoni mwenu niihubiri habari njema, ili watu wa mataifa wapate kusikia na kuamini.

월로프어

gannaaw werante wu bare piyeer jóg ne leen: «yéen bokk yi, xam ngeen ne, ca njàlbéen ga yàlla tànnoon na ma ci yéen, ngir ma yégal ñi dul yawut xebaar bu baax bi, ba ñu gëm.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

인적 기여로
7,787,938,696 더 나은 번역을 얻을 수 있습니다

사용자가 도움을 필요로 합니다:



당사는 사용자 경험을 향상시키기 위해 쿠키를 사용합니다. 귀하께서 본 사이트를 계속 방문하시는 것은 당사의 쿠키 사용에 동의하시는 것으로 간주됩니다. 자세히 보기. 확인