Você procurou por: alionipa (Suaíli - Wolof)

Contribuições humanas

A partir de tradutores profissionais, empresas, páginas da web e repositórios de traduções disponíveis gratuitamente

Adicionar uma tradução

Suaíli

Wolof

Informações

Suaíli

na matakwa ya yule aliyenituma ndiyo haya: nisimpoteze hata mmoja kati ya wale alionipa, ila niwafufue wote siku ya mwisho.

Wolof

lii mooy bëgg-bëggu ki ma yónni: bu ma ñàkk kenn ci ñi mu ma may, te dafa bëgg it ma dekkal leen keroog bés bu mujj ba.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Suaíli

basi, ninaandika barua hii nikiwa mbali, ili nitakapofika kwenu nisilazimike kuwa mkali kwenu kwa kutumia ule uwezo alionipa bwana; naam, uwezo wa kujenga na si wa kubomoa.

Wolof

looloo tax ma leen di binde nii, bala maa ñëw; bëgguma leen a duma ci sañ-sañ bi ma boroom bi jox. jox na ma ko, ngir ma yokk seen ngëm, waaye du ngir seen kasara.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Suaíli

kwenda kwangu kulitokana na ufunuo alionipa mungu. katika kikao cha faragha niliwaeleza hao viongozi ujumbe wa habari njema niliohubiri kwa watu wa mataifa. nilifanya hivyo kusudi kazi yangu niliyokuwa nimefanya, na ile ninayofanya sasa isije ikawa bure.

Wolof

dem naa fa, ndaxte yàllaa ma fa yebal ci kaw peeñu. ba ma demee, daje naa ak ñi ñu gën a fonk ca mbooloo ma, ma wéetoo ak ñoom, won leen xebaar bu baax, bi may yégal ñi dul yawut; ngir ragal sama coonob démb mbaa tey neen.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Suaíli

tena asema: "nitamwekea mungu tumaini langu." na tena: "mimi niko hapa pamoja na watoto alionipa mungu."

Wolof

newaat na:«dinaa am ci yàlla kóolute.» dellu na waxaat ne:«maa ngi nii, man ak doom yi ma yàlla jox.»

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Aviso: contém formatação HTML invisível

Consiga uma tradução melhor através
7,761,094,297 de colaborações humanas

Usuários estão solicitando auxílio neste momento:



Utilizamos cookies para aprimorar sua experiência. Se avançar no acesso a este site, você estará concordando com o uso dos nossos cookies. Saiba mais. OK