You searched for: mbooloom (Wolof - Arabiska)

Wolof

Översätt

mbooloom

Översätt

Arabiska

Översätt
Översätt

Översätt texter, dokument och röst direkt med Lara

Översätt nu

Mänskliga bidrag

Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.

Lägg till en översättning

Wolof

Arabiska

Info

Wolof

waaye su ngeen di laaj leneen, mbooloom dëgg dina ko àtte.

Arabiska

‎وان كنتم تطلبون شيئا من جهة امور أخر فانه يقضى في محفل شرعي.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu tiitaange ju mag tàbbi ci mbooloom ñi gëm ñépp ak ñi ko dégg ñépp.

Arabiska

‎فصار خوف عظيم على جميع الكنيسة وعلى جميع الذين سمعوا بذلك

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

yàlla suufeel na lépp fi kanamam, def ko kilifag lépp ci mbooloom ñi gëm,

Arabiska

واخضع كل شيء تحت قدميه واياه جعل راسا فوق كل شيء للكنيسة

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

wone na jëf yu mag ci dooley loxoom,te tas mbooloom ñiy réy-réylu,

Arabiska

صنع قوة بذراعه. شتّت المستكبرين بفكر قلوبهم.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

mbooloom xarekat ya ak seen kilifa ak alkaatiy yawut ya jàpp yeesu, daldi yeew,

Arabiska

ثم ان الجند والقائد وخدام اليهود قبضوا على يسوع واوثقوه

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

buleen def dara lu man a fanq ngëmu yawut yi walla ñi dul yawut walla mbooloom yàlla.

Arabiska

كونوا بلا عثرة لليهود ولليونانيين ولكنيسة الله.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

moo yelloo ndamul mbooloom ñi gëm jamonoy jamono ba fàww, jaar ci kirist yeesu. amiin.

Arabiska

له المجد في الكنيسة في المسيح يسوع الى جميع اجيال دهر الدهور. آمين

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

dinga xamal mbooloom,ni leen boroom bi man a musale,jaare ko ci seen mbaalug bàkkaar,

Arabiska

لتعطي شعبه معرفة الخلاص بمغفرة خطاياهم

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bu nu weesoo loolu, maa ngi leen di dénk sunu jigéen febe, miy liggéeyal mbooloom ñi gëm ci dëkku señsere.

Arabiska

اوصي اليكم باختنا فيبي التي هي خادمة الكنيسة التي في كنخريا

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu mbooloom ñu gëm ñi bokk menn xel ak benn xalaat. kenn daawul aakimoo dara ci alalam, waaye ñoo bokkoon lépp.

Arabiska

وكان لجمهور الذين آمنوا قلب واحد ونفس واحدة. ولم يكن احد يقول ان شيئا من امواله له بل كان عندهم كل شيء مشتركا‎.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

maye na leen, ngir ñu waajal gaayi yàlla yu sell yi, ñu man a bey seen sas ci taxawal mbooloom kirist, di jëmmam.

Arabiska

لاجل تكميل القديسين لعمل الخدمة لبنيان جسد المسيح

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

te su ñu bëggee laaj dara, nañu ko laaj seen jëkkër ca kër ga, ndaxte jigéen di wax ci ndajem mbooloom ñi gëm, gàcce la.

Arabiska

ولكن ان كنّ يردن ان يتعلمن شيئا فليسألن رجالهنّ في البيت لانه قبيح بالنساء ان تتكلم في كنيسة.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bi ñu agsee, ñu woo mbooloom ñi gëm, nettali leen fi ñu jaar ak yàlla fépp, ak ni mu ubbee buntu ngëm ci ñi dul yawut.

Arabiska

‎ولما حضرا وجمعا الكنيسة اخبرا بكل ما صنع الله معهما وانه فتح للامم باب الايمان‎.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

kon nag jigéen ju gëm te am mbokk mu jëkkëram faatu, na ko dimbali te bañ koo bàyyeek mbooloom ñi gëm. noonu mbooloo mi dina man a dimbali jigéen ñi sësul ci kenn.

Arabiska

ان كان لمؤمن او مؤمنة ارامل فليساعدهنّ ولا يثقّل على الكنيسة لكي تساعد هي اللواتي هنّ بالحقيقة ارامل

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

nun pool, silwan ak timote noo ngi leen di bind, yéen mbooloom ñi gëm ci dëkku tesalonig te nekk ci yàlla baay bi ak boroom bi yeesu kirist. na yiw ak jàmm ànd ak yéen.

Arabiska

بولس وسلوانس وتيموثاوس الى كنيسة التسالونيكيين في الله الآب والرب يسوع المسيح. نعمة لكم وسلام من الله ابينا والرب يسوع المسيح

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

mooy bopp bi yilif jëmm ji, di mbooloom ñi ko gëm, ndaxte moom mooy njàlbéen gi, di taaw bi, maanaam ki jëkk a dekki, ngir muy kilifa ci bépp fànn.

Arabiska

وهو راس الجسد الكنيسة. الذي هو البداءة بكر من الاموات لكي يكون هو متقدما في كل شيء.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

sool moom ànd na ci ñi doon rey ecen. bés booba nag fitna ju metti dal na ci mbooloom ñi gëm, mi nekk yerusalem, ba ñépp, ñu moy ndaw ya, tasaaroo ci diiwaani yude ak samari.

Arabiska

وكان شاول راضيا بقتله. وحدث في ذلك اليوم اضطهاد عظيم على الكنيسة التي في اورشليم فتشتت الجميع في كور اليهودية والسامرة ما عدا الرسل‎.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waaye amaana mu yéex. moo tax ma lay bind bataaxal bii, ngir xamal la, ni ñu war a nekke ci kër yàlla gi, maanaam ci mbooloom yàlla aji dund ji, miy kenug dëgg te di sëslaayam.

Arabiska

ولكن ان كنت ابطىء فلكي تعلم كيف يجب ان تتصرف في بيت الله الذي هو كنيسة الله الحي عمود الحق وقاعدته.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

man pool, ndawul kirist yeesu ci coobareg yàlla, man ak timote sunu mbokk, noo leen di bind, yéen mbooloom yàlla mi nekk dëkku korent, ak gaayi yàlla yu sell, yi nekk ci diiwaanu akayi gépp.

Arabiska

بولس رسول يسوع المسيح بمشيئة الله وتيموثاوس الاخ الى كنيسة الله التي في كورنثوس مع القديسين اجمعين الذين في جميع اخائية

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waaye yéen xeet wu yàlla tànn ngeen, di askanu saraxalekati buur yàlla, askan wu sell ngeen, di mbooloom yàlla, ngir ngeen yégle ngëneelam, moom mi leen woo, ba génne leen lëndëm gi, tàbbal leen ci leeram gu yéeme gi.

Arabiska

واما انتم فجنس مختار وكهنوت ملوكي امة مقدسة شعب اقتناء لكي تخبروا بفضائل الذي دعاكم من الظلمة الى نوره العجيب.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Få en bättre översättning med
8,951,743,554 mänskliga bidrag

Användare ber nu om hjälp:



Vi använder cookies för att förbättra din upplevelse. Genom att fortsätta besöka den här webbplatsen godkänner du vår användning av cookies. Läs mer. OK