You searched for: yuuxu (Wolof - Spanska)

Mänskliga bidrag

Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.

Lägg till en översättning

Wolof

Spanska

Info

Wolof

jigéenu biir la, di yuuxu ndax metitu mat wu tar.

Spanska

y estando encinta, gritaba con dolores de parto y sufría angustia por dar a luz

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

Ñu daldi yuuxu ak di sànni seeni yére, tey callameeru suuf.

Spanska

como ellos daban voces, arrojaban sus ropas y echaban polvo al aire

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu am na ci jàngu bi nit ku rab jàpp. mu daldi yuuxu naan:

Spanska

y en ese momento un hombre con espíritu inmundo estaba en la sinagoga de ellos, y exclam

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

mbooloo mu baree nga ko toppoon, te jigéen ñu baree ngi doon yuuxu, di ko jooy.

Spanska

le seguía una gran multitud del pueblo y de mujeres, las cuales lloraban y se lamentaban por él

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

naka lañu ñëw ci kër njiit li, yeesu dégg coow li; ñii di jooy, ñii di yuuxu.

Spanska

llegaron a la casa del principal de la sinagoga, y él vio el alboroto y los que lloraban y lamentaban mucho

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waaye ñuy yuuxu naan: «daaj ko ci bant! daaj ko ci bant, ba mu dee!»

Spanska

pero ellos volvieron a dar voces, diciendo: --¡crucifícale! ¡crucifícale

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waaye ñoom ñu sax ca la ñu waxoon, di gën a yuuxu naan, ñu daaj ko ci bant. coow la yey pilaat.

Spanska

pero ellos insistían a grandes voces, pidiendo que fuese crucificado. y sus voces prevalecieron

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu ndaje ma rëb, ba ñii di yuuxu lii, ñale di yuuxu laa, te ña ca gën a bare xamuñu lu waral ndaje ma.

Spanska

unos gritaban una cosa, y otros otra cosa; porque la concurrencia estaba confusa, y la mayor parte ni sabía por qué se había reunido

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

fekk booba képp ku rab jàpp ku ko gis, daanu fa kanamam di yuuxu naan: «yaa di doomu yàlla.»

Spanska

y los espíritus inmundos, siempre que le veían, se postraban delante de él y gritaban diciendo: "¡tú eres el hijo de dios!

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Varning: Innehåller osynlig HTML-formatering

Wolof

Ñi jiitu woon gëdd ko, ngir mu noppi. waaye muy gën a yuuxu naan: «sëtu daawuda, yërëm ma!»

Spanska

los que iban delante le reprendían para que se callase, pero él clamaba con mayor insistencia: --¡hijo de david, ten misericordia de mí

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

buuri àddina yépp, yi àndoon ak moom ci njaaloo ak mbuux, bu ñu séenee saxar siy jollee ci taal bi ñu koy lakke, dinañu yuuxu, di ko jooy.

Spanska

"cuando vean el humo de su incendio, llorarán y se lamentarán por ella los reyes de la tierra que han fornicado con ella y han vivido de su sensualidad

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Varning: Innehåller osynlig HTML-formatering

Wolof

ci kaw loolu ñu bare gëdd ko, ngir mu noppi. teewul mu gën a yuuxu naan: «yaw sëtu daawuda bi, yërëm ma!»

Spanska

muchos le regañaban para que se callara, pero él gritaba aun más fuerte: --¡hijo de david, ten misericordia de mí

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waaye nit ña gëdd leen, ngir ñu noppi. teewul gumba ya gën a yuuxu naan: «sang bi, yaw sëtu daawuda bi, yërëm nu!»

Spanska

la gente les reprendía para que se callasen, pero ellos gritaron aun más fuerte diciendo: --¡señor, hijo de david, ten misericordia de nosotros

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bi mbooloo ma gisee li pool def, ñu daldi yuuxu, ne ci làkku waa likawni: «yàlla yi soppiku nañu nit, wàcc ci nun.»

Spanska

entonces, cuando la gente vio lo que pablo había hecho, alzó su voz diciendo en lengua licaónica: --¡los dioses han descendido a nosotros en forma de hombres

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu rab wa daldi yuuxu, sayloo xale bi, génn. xale bi ne nemm, mel ni ku dee, ba tax ñu bare ne: «dee na.»

Spanska

entonces, clamando y desgarrándole con violencia, el espíritu salió; y el muchacho quedó como muerto, de modo que muchos decían: --¡está muerto

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

pilaat ne leen: «lu tax? gan tooñ la def?» waaye mbooloo mi di yuuxu bu gën a kawe: «daaj ko ci bant!»

Spanska

entonces pilato les dijo: --¿pues, qué mal ha hecho? pero lanzaron gritos aun más fuertes: --¡crucifícale

Senast uppdaterad: 2012-05-05
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Få en bättre översättning med
7,800,493,760 mänskliga bidrag

Användare ber nu om hjälp:



Vi använder cookies för att förbättra din upplevelse. Genom att fortsätta besöka den här webbplatsen godkänner du vår användning av cookies. Läs mer. OK