您搜索了: kina (斯瓦希里语 - 沃洛夫语)

人工翻译

来自专业的译者、企业、网页和免费的翻译库。

添加一条翻译

斯瓦希里语

沃洛夫语

信息

斯瓦希里语

ole wao kina mama waja wazito na wanaonyonyesha siku hizo!

沃洛夫语

ngalla jigéen ñi ëmb ca bés yooyu, ngalla it ñiy nàmpal!

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

ili wawazoeze kina mama vijana kuwapenda waume zao na watoto,

沃洛夫语

bay sol ci boppu jeeg yu ndaw yi, ñu bëgg seeni jëkkër ak seeni doom,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kina mama wawili watakuwa wanasaga nafaka, mmoja atachukuliwa na mwingine ataachwa.

沃洛夫语

ci ñaari jigéen ñuy wol ca ëtt ba, dinañu jël kenn ki, bàyyi ki ci des.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

nyingine zilianguka penye mawe pasipokuwa na udongo mwingi. zikaota mara kwa kuwa udongo haukuwa na kina.

沃洛夫语

leneen ci pepp mi wadd ci bérab bu bare ay doj te néew suuf, mu daldi sax bu gaaw, ndaxte suuf si barewul.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

nyingine zilianguka penye mawe pasipokuwa na udongo mwingi. mbegu hizo ziliota mara kwa kuwa udongo haukuwa na kina.

沃洛夫语

leneen ci pepp mi wadd ci bérab bu bare ay doj te néew suuf, mu daldi sax bu gaaw, ndaxte suuf si barewul.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

kusudi muweze kufahamu pamoja na watu wote wa mungu jinsi upendo wa kristo ueneavyo kwa mapana na marefu, kwa kimo na kina.

沃洛夫语

ba jagoo, yéen ak gaayi yàlla yu sell yépp, guddaay ba, yaatuwaay ba, kawe ga ak xóotaay ba,

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

lakini yesu akamjibu mtu huyo, "mama yangu ni nani? na ndugu zangu ni kina nani?"

沃洛夫语

waaye yeesu tontu ko ne: «kan mooy sama ndey ak ñan ñooy samay rakk?»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

斯瓦希里语

hivyo walitafuta kina cha bahari kwa kuteremsha kamba iliyokuwa imefungiwa kitu kizito, wakapata kina cha mita arobaini. baadaye wakapima tena wakapata mita thelathini.

沃洛夫语

Ñu sànni nattukaay ba ci biir géej, mu jàpp ñeent-fukki meetar, dem ca kanam tuuti, sànniwaat ko, jàpp fanweeri meetar.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

walikuwako pia wanawake waliotazama kwa mbali, miongoni mwao akiwa maria toka mji wa magdala, salome, na maria mama wa kina yakobo mdogo na yose.

沃洛夫语

amoon na fa nag ay jigéen, ñu leen dand, di xool. xàmmi nañu ci: maryaama mi dëkk magdala, maryaama yaayu saag mu ndaw ak yuusufa, ak salome.

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

斯瓦希里语

atamtangulia bwana akiongozwa na nguvu na roho kama eliya. atawapatanisha kina baba na watoto wao; atawafanya wasiotii wawe na fikira za uadilifu, na hivyo amtayarishie bwana watu wake."

沃洛夫语

mooy jiitu, di yégle ñëwu boroom bi, ànd ak xel mi ak doole, ji yonent yàlla iliyas amoon, ngir jubale xoli baay yi ak doom yi, ngir delloo ñi déggadi ci maanduteg ñi jub. noonu dina waajal mbooloo muy teeru boroom bi.»

最后更新: 2012-05-05
使用频率: 1
质量:

警告:包含不可见的HTML格式

获取更好的翻译,从
7,747,075,031 条人工翻译中汲取

用户现在正在寻求帮助:



Cookie 讓我們提供服務。利用此服務即表示你同意我們使用Cookie。 更多資訊。 確認