Results for goewerneurs translation from Afrikaans to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Afrikaans

Wolof

Info

Afrikaans

of die goewerneurs as sy gesante, om wel kwaaddoeners te straf, maar die wat goed doen, te prys.

Wolof

mbaa jawriñ yu mu yebal, ngir ñu yar ñiy def lu bon, te teral ñiy def lu baax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

en ook voor goewerneurs en konings sal julle gebring word om my ontwil tot 'n getuienis vir hulle en vir die heidene.

Wolof

dees na leen yóbbu ngir man ci kanami boroom réew ak i buur, ngir ngeen seede ma ci ñoom ak ci ñi dul yawut.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

maar voor al hierdie dinge sal hulle die hande aan julle slaan en julle vervolg en oorlewer in sinagoges en gevangenisse en julle voor konings en goewerneurs bring ter wille van my naam.

Wolof

waaye bala looloo xew, dees na leen jàpp, fitnaal leen, di leen jébbal àttekat yi ca jàngu ya, tëj leen kaso. dees na leen yóbbu ci kanam ay buur yi ak ay boroom réew ndax sama tur.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Afrikaans

maar wees julle vir julleself op die hoede, want hulle sal julle oorlewer aan regbanke, en in sinagoges sal julle geslaan word en voor goewerneurs en konings gebring word om my ontwil, vir hulle tot 'n getuienis.

Wolof

«moytuleen. dees na leen jébbal àttekat ya, di leen dóor ay yar ca jàngu ya. dinañu leen dëj ci kanamu ay boroom réew ak ay buur ndax sama tur, ngir ngeen nekk seede ci ñoom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,339,443 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK