Results for galilæa translation from Danish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Danish

Wolof

Info

Danish

men efter de to dage gik han derfra til galilæa.

Wolof

bi yeesu amee ñaari fan ca dëkk ba, mu jóge fa, jëm diiwaanu galile,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

da forlod han judæa og drog atter bort til galilæa.

Wolof

bi yeesu yégee loolu nag, mu jóge yude, dellu diiwaanu galile.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

da han havde sagt dette til dem, blev han i galilæa.

Wolof

bi mu leen waxee loolu ba noppi, moom mu des galile.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

og de sejlede ind til gadarenernes land, som ligger lige over for galilæa.

Wolof

noonu ñu teer ca diiwaanu waa serasa, fa jàkkaarloo ak diiwaanu galile.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

da kommer jesus fra galilæa til jordan til johannes for at døbes af ham.

Wolof

booba yeesu jóge galile, ñëw ngir yaxya sóob ko ca dexu yurdan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

men da pilatus hørte om galilæa, spurgte han, om manden var en galilæer.

Wolof

bi pilaat yégee baat yooyu, mu laajte ne: «ndax nit kii galile la dëkk?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

men da jesus hørte, at johannes var kastet i fængsel, drog han bort til galilæa.

Wolof

am bés yeesu dégg ne, jàpp nañu yaxya; mu jóg nag, jëm galile.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

"sebulons land og nafthalis land langs søen, landet hinsides jordan, hedningernes galilæa,

Wolof

«yaw réewum sabulon ak réewum neftali,di yoonu géej gannaaw dexu yurdan,yaw galile, réewum ñi dul yawut —

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Danish

men i den sjette måned blev engelen gabriel sendt fra gud til en by i galilæa, som hedder nazareth,

Wolof

bi elisabet nekkee ci juróom-benni weeram, yàlla yónni na malaakaam jibril ca dëkku nasaret ca diiwaanu galile.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

og da de havde fuldbyrdet alle ting efter herrens lov, vendte de tilbage til galilæa til deres egen by nazareth.

Wolof

bi waajuri yeesu yi matalee seen warugar ci lépp lu yoonu boroom bi santaane woon, ñu dellu seen dëkku nasaret ca diiwaanu galile.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

men der var mange kvinder der, som så til i frastand, hvilke havde fulgt jesus fra galilæa og tjent ham.

Wolof

amoon na fa it ay jigéen yu bare yu leen dand, di seetaan. te ñoo jóge woon galile, ànd ak yeesu, di ko topptoo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

men alle hans kyndinge stode langt borte, ligeså de kvinder, som fulgte med ham fra galilæa, og så dette.

Wolof

xamey yeesu yépp ak jigéen, ña ko toppe woon galile, dand leen, di xool li xew.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

denne begyndelse på sine tegn gjorde jesus i kana i galilæa, og han åbenbarede sin herlighed; og hans disciple troede på ham.

Wolof

firnde bii ame ca kana, ca diiwaanu galile, moo doon kéemaan gi yeesu jëkk a def. ci noonu la wonee màggaayam te ay taalibeem gëm nañu ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

og medens de vandrede sammen i galilæa, sagde jesus til dem: "menneskesønnen skal overgives i menneskers hænder;

Wolof

bi ñuy wër diiwaanu galile nag, yeesu ne leen: «léegi ñu jébbal doomu nit ki ci loxoy nit ñi;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Danish

han er ikke her, men han er opstanden; kommer i hu, hvorledes han talte til eder, medens han endnu var i galilæa, og sagde,

Wolof

nekkatu fi; dekki na. fàttalikuleen la mu leen waxoon, ba mu nekkee galile.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

andre sagde: "dette er kristus;" men andre sagde: "mon da kristus kommer fra galilæa?

Wolof

Ñeneen naan: «mooy almasi bi.» Ña ca des it ne: «waaye nan la almasi bi man a jógee galile?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Danish

da denne hørte, at jesus var kommen fra judæa til galilæa, gik han til ham og bad om, at han vilde komme ned og helbrede hans søn; thi han var døden nær.

Wolof

bi mu déggee ne, yeesu jóge na yude, ñëw galile, mu dikk ci moom, ñaan ko mu ñëw këram, wéral doomam, ji wopp bay bëgg a dee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Danish

disse gik nu til filip, som var fra bethsajda i galilæa, og bade ham og sagde: "herre! vi ønske at se jesus."

Wolof

Ñëw nañu ci filib, mi dëkk betsayda ci diiwaanu galile, ne ko: «sang bi, danoo bëggoon a gis yeesu.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Danish

men de bleve ivrigere og sagde: "han oprører folket, idet han lærer over hele judæa fra galilæa af, hvor han begyndte, og lige hertil."

Wolof

waaye ñu sax ci seeni wax naan: «mi ngi jógloo mbooloo mi, di jàngale ci réewu yawut ya mépp, li dale ci galile ba fii.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Danish

da siger jesus til dem: "frygter ikke! går hen og forkynder mine brødre, at de skulle gå bort til galilæa, og der skulle de se mig."

Wolof

yeesu ne leen: «buleen tiit, waaye demleen yégal samay bokk, ñu dem galile; foofa lañu may gise.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,792,664,226 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK