From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
remember them which have the rule over you, who have spoken unto you the word of god: whose faith follow, considering the end of their conversation.
fàttalikuleen seen njiit, yi leen yégal kàddug yàlla. nemmikuleen li seen dund meññ te roy seen ngëm.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
brethren, if a man be overtaken in a fault, ye which are spiritual, restore such an one in the spirit of meekness; considering thyself, lest thou also be tempted.
bokk yi, ku ñu fekk muy def lu yàlla bëggul, yéen ñi topp xelum yàlla, nangeen ko jubbanti ak xol bu lewet. waaye nanga sàmm sa bopp, ngir bàkkaar bañ laa fiir, yaw itam.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: