Results for henceforth translation from English to Wolof

English

Translate

henceforth

Translate

Wolof

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

from henceforth expecting till his enemies be made his footstool.

Wolof

di xaar ba kera mu daaneel ko ay noonam ci kanamam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

from henceforth let no man trouble me: for i bear in my body the marks of the lord jesus.

Wolof

léegi nag, bu ma kenn lëjalati, ndaxte yor naa ci sama yaram ay leget yuy màndargaal ne, jaamu yeesu laa.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for from henceforth there shall be five in one house divided, three against two, and two against three.

Wolof

gannaawsi tey, bu juróomi nit bokkee genn kër, dinañu féewaloo. Ñett dinañu féewaloo ak ñaar ñi ci des, ñaar ñi féewaloo ak ñett ñooñu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but that it spread no further among the people, let us straitly threaten them, that they speak henceforth to no man in this name.

Wolof

waaye ngir mbir mi bañ a law ci xeet wi, nanu leen aaye, ñu bañ a waxati ak kenn ci tur woowu.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and that he died for all, that they which live should not henceforth live unto themselves, but unto him which died for them, and rose again.

Wolof

te dee na ngir ñépp, ngir ñiy dund dootuñu dund ngir seen bopp, waaye ngir ki dee ci seen wàll te dekki.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

wherefore henceforth know we no man after the flesh: yea, though we have known christ after the flesh, yet now henceforth know we him no more.

Wolof

kon nag gannaawsi tey xoolatunu kenn ci gis-gisu àddina. su fekkee mas nanoo xool kirist ci gis-gisu àddina, léegi xooleetunu ko noonu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but i say unto you, i will not drink henceforth of this fruit of the vine, until that day when i drink it new with you in my father's kingdom.

Wolof

maa ngi leen di wax, dootuma naan gannaawsi tey ndoxum réseñ mii, ba kera may naan ak yéen ndoxum réseñ mu bees ci sama nguuru baay.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and so was also james, and john, the sons of zebedee, which were partners with simon. and jesus said unto simon, fear not; from henceforth thou shalt catch men.

Wolof

ak ña mu bokkaloon liggéey ba, maanaam ñaari doomi sebede yi di saag ak yowaana. yeesu ne simoŋ: «bul ragal dara; gannaawsi tey, ay nit ngay mbaal jëme ci man.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

henceforth i call you not servants; for the servant knoweth not what his lord doeth: but i have called you friends; for all things that i have heard of my father i have made known unto you.

Wolof

dootuma leen wooye jaam, ndaxte jaam du xam li sangam di def. xarit laa leen wooye, ndaxte xamal naa leen li ma jële lépp ci sama baay.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and when they opposed themselves, and blasphemed, he shook his raiment, and said unto them, your blood be upon your own heads; i am clean: from henceforth i will go unto the gentiles.

Wolof

bi ko yawut ya gàntoo nag, di ko xas, mu yëlëb ay yéreem ne leen: «yéena sàkku seen musiba; set naa ci. léegi maa ngi dem ci ñi dul yawut.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,892,216,102 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK