From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
how are the family?
naka ngonsi bi?
Last Update: 2015-02-06
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
when therefore the lord knew how the pharisees had heard that jesus made and baptized more disciples than john,
amoon na benn bés farisen yi dégg ne, ñiy topp yeesu ñoo ëpp ñiy topp yaxya, te ñi yeesu sóob ci ndox ñoo ëpp ñi yaxya sóob.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and how the chief priests and our rulers delivered him to be condemned to death, and have crucified him.
waaye sunuy saraxalekat yu mag ak sunuy njiit ñoo ko jébbal nguur gi ngir ñu àtte ko, teg ko dee, ba daaj ko ci bant.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and her neighbours and her cousins heard how the lord had shewed great mercy upon her; and they rejoiced with her.
dëkkandoom yi ak mbokkam yi yég ne, boroom bi won na ko yërmande ju réy, ñu ànd ak moom bég.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
and jesus sat over against the treasury, and beheld how the people cast money into the treasury: and many that were rich cast in much.
noonu yeesu toog ca kër yàlla ga, janook ndab, yi ñuy def sarax ngir yàlla, muy xool nit ña cay dugal seen xaalis. am nag ay boroom alal yu ci di def xaalis bu bare.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
but he, beckoning unto them with the hand to hold their peace, declared unto them how the lord had brought him out of the prison. and he said, go shew these things unto james, and to the brethren. and he departed, and went into another place.
piyeer taf loxoom ci gémmiñam, ngir ñu noppi, daldi leen nettali, ni ko boroom bi génnee ca kaso ba. mu ne leen: «tee ngeen jottali ko saag ak bokk ya.» bi mu ko waxee, mu jóge fa, dem feneen.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference: