Results for rejoice translation from English to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

English

Wolof

Info

English

rejoice evermore.

Wolof

deeleen bég

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for the same cause also do ye joy, and rejoice with me.

Wolof

yéen itam nag bégleen, waaw fekksileen ma ci sama mbég.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

but now ye rejoice in your boastings: all such rejoicing is evil.

Wolof

waaye fi mu ne, naagu ngeen bay damu, te damoo noonu baaxul.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and again he saith, rejoice, ye gentiles, with his people.

Wolof

mbind mi nee na it:«yéen xeeti àddina, ñëwleen bànneexuak xeet wi yàlla tànnal boppam.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and thou shalt have joy and gladness; and many shall rejoice at his birth.

Wolof

sa mbég lay doon, sa xol sedd ci, te ñu bare dinañu bég ci juddoom,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

by whom also we have access by faith into this grace wherein we stand, and rejoice in hope of the glory of god.

Wolof

moo nu ubbil bunt ci yàlla, nu taxaw temm ci yiwam, jaar ci ngëm. te it nu ngi bég ciy négandiku, yàlla boole nu ci ndamam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

therefore did my heart rejoice, and my tongue was glad; moreover also my flesh shall rest in hope:

Wolof

moo tax sama xol sedd,may woy sama bànneex,te it sama yaram di tëdd ci yaakaar.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for we are the circumcision, which worship god in the spirit, and rejoice in christ jesus, and have no confidence in the flesh.

Wolof

ndaxte nun noo xaraf tigi, nun ñiy màggal yàlla ci xel mu sell mi, di damu ci kirist yeesu, te amunu jenn yaakaar ci matug nit.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and he that reapeth receiveth wages, and gathereth fruit unto life eternal: that both he that soweth and he that reapeth may rejoice together.

Wolof

kiy góob tool yi mu ngi jot xaat peyam; day dajale nit ñi ngir dund gu dul jeex, ni ñuy dajalee pepp. kon boog kiy ji dina bégandoo ak kiy góob.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

rejoice, and be exceeding glad: for great is your reward in heaven: for so persecuted they the prophets which were before you.

Wolof

bégleen te bànneexu, ndax seen yool dina réy ci laaxira. ndaxte noonu lañu daan fitnaale yonent yi fi jiitu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

finally, my brethren, rejoice in the lord. to write the same things to you, to me indeed is not grievous, but for you it is safe.

Wolof

kon nag samay bokk, bégleen ci boroom bi. duma sonn mukk ci di leen ko wax, ndax seen mucc moo ci aju.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and when he cometh home, he calleth together his friends and neighbours, saying unto them, rejoice with me; for i have found my sheep which was lost.

Wolof

boo àggee ca kër ga, dinga woo say xarit ak say dëkkandoo ne leen: “kaayleen bànneexu ak man, ndaxte gis naa sama xar ma réeroon.”

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and they that dwell upon the earth shall rejoice over them, and make merry, and shall send gifts one to another; because these two prophets tormented them that dwelt on the earth.

Wolof

waa àddina dinañu bég ci seen dee, di ndokkeelante ak di joqleente ay may, ndaxte ñaari yonent ya lakkaloon nañu waa àddina.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

and i wrote this same unto you, lest, when i came, i should have sorrow from them of whom i ought to rejoice; having confidence in you all, that my joy is the joy of you all.

Wolof

looloo tax ma binde noonu, ngir bañ a agsi, am naqar ci ñi ma waroon a bégal. am naa kóolute ci yéen ñépp ne, sama mbég mooy seen mbég.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

for it is written, rejoice, thou barren that bearest not; break forth and cry, thou that travailest not: for the desolate hath many more children than she which hath an husband.

Wolof

ndaxte mbind mi nee na:«bégal, yaw jigéen ji dul jur,te musul a am doom.reeyal te bànneexu,yaw mi musul a xam coonob mat,ndaxte jigéen ji ñu faalewulmoo gën a jaboot ki nekk ak jëkkëram.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

English

therefore rejoice, ye heavens, and ye that dwell in them. woe to the inhabiters of the earth and of the sea! for the devil is come down unto you, having great wrath, because he knoweth that he hath but a short time.

Wolof

looloo tax, na asamaanak ñi ci dëkk bànneexu!musiba ci kaw suuf ak ci biir géej!ndaxte seytaane wàcc na ci yéen,ànd ak mer mu tàng,ndaxte xam na ne, jot gi ko dese barewul.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,884,418,409 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK