From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
and he looked up, and said, i see men as trees, walking.
waa ji xool ne ko: «gis naa ay nit, ñu mel ni ay garab, te ñu ngi dox.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and he spake to them a parable; behold the fig tree, and all the trees;
noonu yeesu misaal leen lii: «xool-leen garabu figg ak yeneen garab yi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
these are the two olive trees, and the two candlesticks standing before the god of the earth.
Ñaari seede ya nag ñoo di ñaari garabu oliw yeek ñaari làmpu diwlin, yi taxaw ci kanam boroom suuf si.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and many spread their garments in the way: and others cut down branches off the trees, and strawed them in the way.
Ñu bare lal seeni yére ci yoon wi, ñenn ñi dagg ay cari garab ci tool yi, lal leen it ci yoon wi.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and a very great multitude spread their garments in the way; others cut down branches from the trees, and strawed them in the way.
Ña ëpp ca mbooloo ma lal seeni yére ca yoon wa, ñenn ña dagg ay cari garab, lal leen it ca yoon wa.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
and now also the axe is laid unto the root of the trees: every tree therefore which bringeth not forth good fruit is hewn down, and cast into the fire.
sémmiñ wi tiim na reeni garab yi. garab nag gu meññul doom yu baax, dees na ko gor, sànni ko ci safara si.»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
took branches of palm trees, and went forth to meet him, and cried, hosanna: blessed is the king of israel that cometh in the name of the lord.
Ñu daldi jël cari garab, génn di ko teeru. Ñuy xaacu naan:«osaana!yaw miy ñëw ci turu boroom bi,ku barkeel nga!na yàlla barkeel buuru israyil!»
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
the first angel sounded, and there followed hail and fire mingled with blood, and they were cast upon the earth: and the third part of trees was burnt up, and all green grass was burnt up.
malaaka mu jëkk ma wol liitam. noonu ñu sànni ci àddina yuur ak safara yu ñu boole ak deret, ba tax benn ci ñetti xaaju suuf si lakk, benn ci ñetti xaaju garab yi it lakk, te ñax mu naat mépp lakk.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
these are spots in your feasts of charity, when they feast with you, feeding themselves without fear: clouds they are without water, carried about of winds; trees whose fruit withereth, without fruit, twice dead, plucked up by the roots;
su ñu bokkee ak yéen reeru mbooloo mi, dañu ciy indi ay, niy xeer yu nëbbu ci biir géej; amuñu genn gàcce, waaye dañuy giiroo te fonk seen biir rekk. Ñu ngi mel ni xiin yu amul ndox, yuy naaxsaay ci ngelaw; ni garab yu meññul ci jamonoy meññeef, te buddeeku, dee ba wow koŋŋ;
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: