From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
now when jesus was risen early the first day of the week, he appeared first to mary magdalene, out of whom he had cast seven devils.
bi yeesu dekkee nag ci suba teel ca bés bu jëkk ca ayu-bés ga, mu jëkk a feeñu maryaama mu dëkk magdala, mi mu dàqe woon juróom-ñaari rab.
in the end of the sabbath, as it began to dawn toward the first day of the week, came mary magdalene and the other mary to see the sepulchre.
gannaaw bésu noflaay ba nag, ca fajar ga, ca bés bu jëkk ca ayu-bés ga, maryaamam magdala ak maryaama ma ca des dem, seeti bàmmeel ba.
the first day of the week cometh mary magdalene early, when it was yet dark, unto the sepulchre, and seeth the stone taken away from the sepulchre.
bés ba jiitu ca ayu-bés ga, maryaamam magdala jóg ca fajar, dem ca bàmmeel ba. bi mu agsee, mu gis ne dindi nañu xeer, wa ñu ko ube woon.
and upon the first day of the week, when the disciples came together to break bread, paul preached unto them, ready to depart on the morrow; and continued his speech until midnight.
ca bés bu jëkk ca ayu-bés ga, booloo nanu ngir damm mburu ma. te pool, mi bëggoon a dem ca ëllëg sa, di diisoo ak ñoom te waxtaanam law ba ci xaaju guddi.