Results for connaissance translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

enchanté de faire ta connaissance

Wolof

Last Update: 2023-09-07
Usage Frequency: 1
Quality:

French

apprenant toujours et ne pouvant jamais arriver à la connaissance de la vérité.

Wolof

duñu noppee gëstu, waaye duñu man a yegg ci xam-xamu dëgg mukk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin de donner à son peuple la connaissance du salut par le pardon de ses péchés,

Wolof

dinga xamal mbooloom,ni leen boroom bi man a musale,jaare ko ci seen mbaalug bàkkaar,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car en lui vous avez été comblés de toutes les richesses qui concernent la parole et la connaissance,

Wolof

ndaxte ci yiwi yàlla yépp ngeen woomle ci kirist, muy ci wax, muy ci xam-xam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

que la grâce et la paix vous soient multipliées par la connaissance de dieu et de jésus notre seigneur!

Wolof

na leen yàlla dollil yiw ak jàmm, jaar ci xam ko ak yeesu sunu boroom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et leur complot parvint à la connaissance de saul. on gardait les portes jour et nuit, afin de lui ôter la vie.

Wolof

waaye sool yég seen pexe. fekk guddi ak bëccëg ñu doon wottu bunt yi yépp, ngir man koo bóom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

trois ans plus tard, je montai à jérusalem pour faire la connaissance de céphas, et je demeurai quinze jours chez lui.

Wolof

ba ñu ca tegee ñetti at, ma sog a dem yerusalem, ngir xamante ak sefas, dal fa moom lu mat ñaari ayu-bés.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car, si nous péchons volontairement après avoir reçu la connaissance de la vérité, il ne reste plus de sacrifice pour les péchés,

Wolof

gannaaw ba nu nangoo xam dëgg ba noppi, bu nu teyee di def bàkkaar, kon sarax dootul am ngir bàkkaar yooyu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car nul ne sera justifié devant lui par les oeuvres de la loi, puisque c`est par la loi que vient la connaissance du péché.

Wolof

ndaxte sàmm yoon wi taxul kenn jub ci kanam yàlla; solob ndigal yi daal mooy wone bàkkaar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin que le dieu de notre seigneur jésus christ, le père de gloire, vous donne un esprit de sagesse et de révélation, dans sa connaissance,

Wolof

te li may ñaan yàllay sunu boroom yeesu kirist, di baay bi yelloo ndam, mooy lii: mu sol leen xel mu xóot, te xamal leen boppam

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

par la pureté, par la connaissance, par la longanimité, par la bonté, par un esprit saint, par une charité sincère,

Wolof

nu ngi rafetal sunu yen ci dund gu sell, ci xam-xam, muñ ak laabiir, ci xel mu sell mi ak ci mbëggeel gu raxul njublaŋ,

Last Update: 2023-12-17
Usage Frequency: 2
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

French

pour ce qui concerne les viandes sacrifiées aux idoles, nous savons que nous avons tous la connaissance. -la connaissance enfle, mais la charité édifie.

Wolof

léegi nag, ci li jëm ci yàpp wi ñu jébbal xërëm yi: nun ñépp am nanu xam-xam, loolu dëgg la. xam-xam day tax ba nit yég boppam, waaye mbëggeel day yékkati ngëm.

Last Update: 2024-02-16
Usage Frequency: 4
Quality:

French

et connaître l`amour de christ, qui surpasse toute connaissance, en sorte que vous soyez remplis jusqu`à toute la plénitude de dieu.

Wolof

te xam mbëggeelu kirist, gi raw mépp xel. noonu dingeen fees dell ak matug yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et ayant revêtu l`homme nouveau, qui se renouvelle, dans la connaissance, selon l`image de celui qui l`a créé.

Wolof

te sol ngeen dund gu bees, gi yàlla sàkk te di ko yeesal ba mu mel ni moom, ngir ngeen man koo xam bu wér.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car dieu, qui a dit: la lumière brillera du sein des ténèbres! a fait briller la lumière dans nos coeurs pour faire resplendir la connaissance de la gloire de dieu sur la face de christ.

Wolof

ndaxte yàlla mi ne: «na leer leer ci biir lëndëm,» moo leer ci sunu xol, ngir leeral nu ak xam-xamu ndamu yàlla, liy feeñ ci xar-kanamu kirist.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais cette connaissance n`est pas chez tous. quelques-uns, d`après la manière dont ils envisagent encore l`idole, mangent de ces viandes comme étant sacrifiées aux idoles, et leur conscience, qui est faible, en est souillée.

Wolof

waaye ñépp xamuñu loolu. am na ñu tàmmoon xërëm yi, te léegi, bu ñu lekkatee yàppu sarax yi, dañuy xalaat ne, xërëm lañu ko jagleel. seen xel dafa leen di yedd, ndaxte ci seen ñàkka xam dañuy foog ne, taq nañu sobe ndax ñam woowu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,799,985,166 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK