Results for de rien translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

mangez de tout ce qui se vend au marché, sans vous enquérir de rien par motif de conscience;

Wolof

man ngeen a lekk lépp lu ñuy jaay ca ja ba, bañ cee boole ay laaj ngir dalal seen xel.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

voici, moi paul, je vous dis que, si vous vous faites circoncire, christ ne vous servira de rien.

Wolof

dégluleen! man pool maa leen koy wax: bu ngeen itteelee xaraf, kon kirist dootu leen jariñ dara.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ne vous inquiétez de rien; mais en toute chose faites connaître vos besoins à dieu par des prières et des supplications, avec des actions de grâces.

Wolof

buleen jaaxle ci dara, waaye ci lépp wéetal-leen yàlla, diis ko seeni soxla ci ñaan gu ànd ak cant.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

c`est l`esprit qui vivifie; la chair ne sert de rien. les paroles que je vous ai dites sont esprit et vie.

Wolof

xelu yàlla mi mooy joxe dund; ñam wi jariñul dara. kàddu yi ma leen wax, ci xelum yàlla lañu jóge te ñooy joxe dund.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et quand je distribuerais tous mes biens pour la nourriture des pauvres, quand je livrerais même mon corps pour être brûlé, si je n`ai pas la charité, cela ne me sert de rien.

Wolof

te it su ma doon saraxe li ma am lépp, di bàyyi ñu lakk sama yaram, ba rey ma, su ma ci boolewul mbëggeel, du ma jariñ dara.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et lui dit: garde-toi de rien dire à personne; mais va te montrer au sacrificateur, et offre pour ta purification ce que moïse a prescrit, afin que cela leur serve de témoignage.

Wolof

«moytul a wax kenn dara, waaye demal won sa bopp saraxalekat bi, te nga jébbal yàlla sarax, si yoonu musaa santaane, ngir ñu xam ne wér nga, te mu nekk seede ci ñoom.»

Last Update: 2023-12-12
Usage Frequency: 2
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
8,927,574,393 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK