Results for honte translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

je le dis à votre honte. ainsi il n`y a parmi vous pas un seul homme sage qui puisse prononcer entre ses frères.

Wolof

ma ne kon, war ngeen a rus! xanaa amul ci seen biir kenn ku am xel, ku man a àtte mbokkam yi?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et quand même je me glorifierais un peu trop de l`autorité que le seigneur nous a donnée pour votre édification et non pour votre destruction, je ne saurais en avoir honte,

Wolof

awma lu may rus, su may damu lu ëpp ci sañ-sañ bi nu boroom bi jox, di sañ-sañu yokk seen ngëm, te du ngir seen kasara.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ce n`est pas pour vous faire honte que j`écris ces choses; mais je vous avertis comme mes enfants bien-aimés.

Wolof

binduma leen loolu ngir ngeen am yeraange, waaye dama koo def ngir artu leen, ndaxte yéenay samay doom te bëgg naa leen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car celui qui sanctifie et ceux qui sont sanctifiés sont tous issus d`un seul. c`est pourquoi il n`a pas honte de les appeler frères,

Wolof

moom yeesu miy sellal, ak ñi muy sellal, ñoom ñépp genn njaboot lañu. moo tax yeesu rusu leen a wooye ay doomi baayam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

la nature elle-même ne vous enseigne-t-elle pas que c`est une honte pour l`homme de porter de longs cheveux,

Wolof

xanaa du àddina ci boppam dafa leen di won ne, gàcce la ci góor, ngir muy yar kawar gu bare?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car quiconque aura honte de moi et de mes paroles au milieu de cette génération adultère et pécheresse, le fils de l`homme aura aussi honte de lui, quand il viendra dans la gloire de son père, avec les saints anges.

Wolof

ku ma rus a faral, te nanguwul samay wax ci kanamu niti jamono jii, ñi fecci seen kóllëre ak yàlla te topp bàkkaar, doomu nit ki dina la rus a xam, bés bu ñëwee ci ndamu baayam, ànd ak malaaka yu sell yi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car je n`ai point honte de l`Évangile: c`est une puissance de dieu pour le salut de quiconque croit, du juif premièrement, puis du grec,

Wolof

ndaxte awma benn werante ci xebaar bu baax bi may waare, ndax mbirum yàlla la, mu làmboo dooleem, ngir musal képp ku ko gëm, muy yawut ci bu jëkk mbaa ki dul yawut.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,771,620,395 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK