Results for scribes translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

les scribes et les pharisiens sont assis dans la chaire de moïse.

Wolof

«xutbakat ya ak farisen ya ñu ngi toog ci jalu musaa.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

alors les scribes et les pharisiens amenèrent une femme surprise en adultère;

Wolof

xutbakat ya ak farisen ya indi jenn jigéen ju ñu bettoon muy njaaloo, ñu taxawal ko ca diggu mbooloo ma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

les principaux sacrificateurs et les scribes étaient là, et l`accusaient avec violence.

Wolof

saraxalekat yu mag ya ak xutbakat yaa nga fa woon, di ko jiiñ bu metti.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

alors des pharisiens et des scribes vinrent de jérusalem auprès de jésus, et dirent:

Wolof

ca jamono jooja amoon na bés ay farisen ak ay xutbakat jóge yerusalem, ñëw ci yeesu ne ko:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

les pharisiens et quelques scribes, venus de jérusalem, s`assemblèrent auprès de jésus.

Wolof

amoon na bés nag, ay farisen ak ay xutbakat yu jóge yerusalem ñëw ci yeesu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

le lendemain, les chefs du peuple, les anciens et les scribes, s`assemblèrent à jérusalem,

Wolof

ca ëllëg sa nag kilifay yawut yi ak njiit yi ak xutbakat yi dajaloo ci yerusalem.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ils étaient frappés de sa doctrine; car il enseignait comme ayant autorité, et non pas comme les scribes.

Wolof

te ñu waaru ca njàngaleem, ndaxte jàngal na leen ak sañ-sañ bu seeni xutbakat amul.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il y avait là quelques scribes, qui étaient assis, et qui se disaient au dedans d`eux:

Wolof

fekk ay xutbakat toog fa, ñu di werante ci seen xel naan:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ceux qui avaient saisi jésus l`emmenèrent chez le souverain sacrificateur caïphe, où les scribes et les anciens étaient assemblés.

Wolof

Ña jàppoon yeesu yóbbu ko kër kayif, saraxalekat bu mag ba, fa xutbakat ya ak njiit ya daje.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il enseignait tous les jours dans le temple. et les principaux sacrificateurs, les scribes, et les principaux du peuple cherchaient à le faire périr;

Wolof

bés bu nekk yeesu di jàngale ca kër yàlla ga. saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya, ñoom ak njiiti xeet wa, ñu ngi ko doon wut a reylu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

alors quelques-uns des scribes et des pharisiens prirent la parole, et dirent: maître, nous voudrions te voir faire un miracle.

Wolof

ci kaw loolu ay xutbakat ak ay farisen wax ak yeesu ne ko: «kilifa gi, danoo bëggoon, nga won nu kéemaan guy firndeel sag yónnent.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ils se rendirent de nouveau à jérusalem, et, pendant que jésus se promenait dans le temple, les principaux sacrificateurs, les scribes et les anciens, vinrent à lui,

Wolof

gannaaw loolu ñu duggaat yerusalem, te yeesu doon doxantu ca ëtti kër yàlla ga. noonu saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya ak njiit ya dab ko

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

la fête de pâque et des pains sans levain devait avoir lieu deux jours après. les principaux sacrificateurs et les scribes cherchaient les moyens d`arrêter jésus par ruse, et de le faire mourir.

Wolof

booba nag saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya ñu ngi doon fexeel yeesu, ngir jàpp ko, reylu. fekk booba ñaari fan a des ci màggalu bésu jéggi ba ak màggalu mburu ya amul lawiir.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il leur disait dans son enseignement: gardez-vous des scribes, qui aiment à se promener en robes longues, et à être salués dans les places publiques;

Wolof

bi yeesu di jàngale nag, mu ne leen: «moytuleen xutbakat yi; dañoo bëgg di doxantu, sol ay mbubb yu réy, te ñépp di leen nuyoo ñaari loxo ci pénc mi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

dès le matin, les principaux sacrificateurs tinrent conseil avec les anciens et les scribes, et tout le sanhédrin. après avoir lié jésus, ils l`emmenèrent, et le livrèrent à pilate.

Wolof

ci suba teel saraxalekat yu mag yi gise, ñoom ak njiit yi ak xutbakat yi ak kureelu àttekat yi yépp. Ñu yeew nag yeesu, daldi ko yóbbu, jébbal ko pilaat.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

alors il commença à leur apprendre qu`il fallait que le fils de l`homme souffrît beaucoup, qu`il fût rejeté par les anciens, par les principaux sacrificateurs et par les scribes, qu`il fût mis à mort, et qu`il ressuscitât trois jours après.

Wolof

booba yeesu tàmbali na leen a xamal ne, doomu nit ki war na sonn lu bare; njiit ya, saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya dëddu ko, ñu rey ko, mu dekki ci ñetti fan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
9,162,249,240 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK