Results for une partie translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

comme il semait, une partie de la semence tomba le long du chemin: les oiseaux vinrent, et la mangèrent.

Wolof

bi muy saaw toolam nag, lenn ci pepp mi wadd ci kaw yoon wi, picc yi daldi ñëw, lekk ko lépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et retint une partie du prix, sa femme le sachant; puis il apporta le reste, et le déposa aux pieds des apôtres.

Wolof

mu dencal boppam benn cér ca njëg ga, ànd ca ak jabaram; ba noppi mu indi cér ba ca des, teg ko ci loxoy ndaw ya.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

personne ne met une pièce de drap neuf à un vieil habit; car elle emporterait une partie de l`habit, et la déchirure serait pire.

Wolof

xam ngeen ne, kenn du daax mbubb mu màggat ak sekkit wu bees; ndaxte sekkit wi day ñoddi mbubb mi, te xottiku bi gën a yaatu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

personne ne coud une pièce de drap neuf à un vieil habit; autrement, la pièce de drap neuf emporterait une partie du vieux, et la déchirure serait pire.

Wolof

«kenn du daax mbubb mu màggat ak sekkit wu bees; ndaxte sekkit wi day ñoddi mbubb mi, te xottiku bi gën a yaatu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

un semeur sortit pour semer sa semence. comme il semait, une partie de la semence tomba le long du chemin: elle fut foulée aux pieds, et les oiseaux du ciel la mangèrent.

Wolof

«dafa amoon beykat bu demoon jiyi. bi muy saaw toolam nag, lenn ci pepp mi wadd ci kaw yoon wi, nit ñi joggi ci, picci asamaan lekk ko lépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

pierre lui dit: ananias, pourquoi satan a-t-il rempli ton coeur, au point que tu mentes au saint esprit, et que tu aies retenu une partie du prix du champ?

Wolof

bi mu ko defee piyeer ne ko: «anañas, lu tax nga bàyyi seytaane dugg la, ba fees sa xol, ngay wor xel mu sell mi, ci li nga dencal sa bopp benn cér ci njëg gi?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car je ne veux pas, frères, que vous ignoriez ce mystère, afin que vous ne vous regardiez point comme sages, c`est qu`une partie d`israël est tombée dans l`endurcissement, jusqu`à ce que la totalité des païens soit entrée.

Wolof

bokk yi, dama leen a bëgg a dindi kumpa ci lii, ngir ngeen bañ a yég seen bopp. dërkiisu xol dab na bànni israyil ab diir, ba bés ba mboolem waa àddina, ñu war a bokk ci nguuru yàlla, dugg ca.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,775,687,864 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK