Results for gedanken translation from German to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

German

Wolof

Info

German

da aber jesus den gedanken ihres herzens sah, ergriff er ein kind und stellte es neben sich

Wolof

yeesu mi xam seen xalaat, jël ab xale, teg ci wetam ne leen:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

da aber jesus ihre gedanken sah, sprach er: warum denkt ihr so arges in euren herzen?

Wolof

waaye yeesu xam seen xalaat ne leen: «lu tax ngeen am xalaat yu bon ci seen xol?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

da aber jesus ihre gedanken merkte, antwortete er und sprach zu ihnen: was denket ihr in euren herzen?

Wolof

waaye yeesu xam seen xalaat, tontu leen ne: «lu tax ngeen di werante ci seen xel?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

(und es wird ein schwert durch deine seele dringen), auf daß vieler herzen gedanken offenbar werden.

Wolof

ba naqar dina xar sa xol ni jaasi. noonu xalaati ñu bare feeñ.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

er aber merkte ihre gedanken und sprach zu dem menschen mit der dürren hand: stehe auf und tritt hervor! und er stand auf und trat dahin.

Wolof

waaye yeesu xam seen xalaat, daldi ne ku loxoom làggi: «jógal taxaw ci kanamu ñépp.» nit ka daldi jóg taxaw.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

so wir denn göttlichen geschlechts sind, sollen wir nicht meinen, die gottheit sei gleich den goldenen, silbernen und steinernen bildern, durch menschliche kunst und gedanken gemacht.

Wolof

kon nag, bu nu nekkee xeetu yàlla, warunoo gëm ne, yàlla mel na ni nataali wurus, xaalis mbaa doj yu nit defar ci xareñ mbaa xel.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

als die da beweisen, des gesetzes werk sei geschrieben in ihren herzen, sintemal ihr gewissen ihnen zeugt, dazu auch die gedanken, die sich untereinander verklagen oder entschuldigen),

Wolof

di wone it ne, yàlla bind na ci seen xol jëf yi yoonu musaa santaane. seen xel it seede na ne noonu la, fekk seeni xalaat ñoo leen di tuumaal, mbaa ñu leen di jéggal.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

denn das wort gottes ist lebendig und kräftig und schärfer denn kein zweischneidig schwert, und dringt durch, bis daß es scheidet seele und geist, auch mark und bein, und ist ein richter der gedanken und sinne des herzens.

Wolof

xam nanu ne, kàddug yàlla mi ngi dund te am na doole. moo gën a ñaw jaasiy ñaari boor. day dagg ba fa xol ak xel digaloo, ba fa yax yi ak yuq gi di teqalikoo, te man na àtte xalaat yi ak mébéti xol.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

es kam auch ein gedanke unter sie, welcher unter ihnen der größte wäre.

Wolof

werante am ci biir taalibe yi, ñuy laajante kan moo gën a màgg ci ñoom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,774,241,778 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK