Results for tochter translation from German to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

German

Wolof

Info

German

als er aber ausgesetzt ward, nahm ihn die tochter pharaos auf und zog ihn auf, ihr selbst zu einem sohn.

Wolof

ba noppi sànni ko. noonu doom ju jigéen ju firawna for ko, yar ko ni doomam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

da aber herodes seinen jahrestag beging, da tanzte die tochter der herodias vor ihnen. das gefiel herodes wohl.

Wolof

bi ñu ca tegee ab diir nag, ñuy màggal bés ba erodd juddu woon, te doomu erojàdd ju jigéen di fecc ci biir gan ñi. loolu neex erodd,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

denn ich bin gekommen, den menschen zu erregen gegen seinen vater und die tochter gegen ihre mutter und die schwiegertochter gegen ihre schwiegermutter.

Wolof

ndaxte ñëw naa ngir féewale doom ak baayam, doom ju jigéen ak ndeyam, jabar ak goroom;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

denn er hatte eine einzige tochter bei zwölf jahren, die lag in den letzten zügen. und da er hinging, drängte ihn das volk.

Wolof

ndaxte jenn doomam ju jigéen, ji mu amoon kepp te muy tollu ci fukki at ak ñaar, ma nga doon waaj a dee. bi yeesuy dem, nit ñaa ngi doon buuxante, di ko tanc.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

"fürchte dich nicht du tochter zion! siehe, dein könig kommt, reitend auf einem eselsfüllen."

Wolof

«buleen ragal, waa siyon.gis ngeen, seen buur a ngi ñëw,war mbaam mu ndaw.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

German

wer vater oder mutter mehr liebt denn mich, der ist mein nicht wert; und wer sohn oder tochter mehr liebt denn mich, der ist mein nicht wert.

Wolof

ku ma gënalul sa ndey walla sa baay, yeyoowuloo ma; ku ma gënalul sa doom ju góor walla ju jigéen, yeyoowuloo ma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

da er noch redete, kam einer vom gesinde des obersten der schule und sprach zu ihm: deine tochter ist gestorben; bemühe den meister nicht.

Wolof

bi yeesu di wax nag, am na ku jóge ca kër njiit la, mu ñëw naan: «sa doom faatu na; matatul ngay sonal kilifa gi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

er sprach aber zu ihr; meine tochter, dein glaube hat dich gesund gemacht; gehe hin mit frieden und sei gesund von deiner plage!

Wolof

yeesu ne ko: «soxna si, sa ngëm faj na la; demal ci jàmm, te na sa jàngoro wàcc.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

"saget der tochter zion: siehe, dein könig kommt zu dir sanftmütig und reitet auf einem esel und auf einem füllen der lastbaren eselin."

Wolof

«waxal waa siyon:“seen buur a ngi ñëw ci yéen;ku lewet la, te war mbaam-sëf,dig cumbur, doomu mbaam.”»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

German

und siehe, ein kanaanäisches weib kam aus derselben gegend und schrie ihm nach und sprach: ach herr, du sohn davids, erbarme dich mein! meine tochter wird vom teufel übel geplagt.

Wolof

ba mu fa àggee nag, jigéenu waa kanaan, ja dëkk ca wàll yooyu, daldi génn, di wax ca kaw ne ko: «yaw sang bi, sëtu daawuda bi, yërëm ma! rab jàpp na sama doom ju jigéen, te dafa sonn lool.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

"und es soll geschehen in den letzten tagen, spricht gott, ich will ausgießen von meinem geist auf alles fleisch; und eure söhne und eure töchter sollen weissagen, und eure jünglinge sollen gesichte sehen, und eure Ältesten sollen träume haben;

Wolof

“yàlla nee na: ci bés yu mujj yi,dinaa tuur ci sama xel ci kaw nit ñépp;seen xeet wu góor ak wu jigéendinañu wax ci kàddug yàlla;waxambaane yi dinañu gis ay peeñute màggat yi di gént ay gént.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,761,834,891 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK