From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
sebab allah memperlakukan semua orang sama
ndaxte ñépp a yem fa kanam yàlla.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
tetapi janganlah memperlakukan dia sebagai musuh; hanya nasihatilah dia sebagai seorang saudara
waxuma ngeen def ko noon, waaye ngeen yedd ko ni seen mbokk.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
kalian tahu bahwa kami memperlakukan kalian masing-masing seperti seorang bapak memperlakukan anak-anaknya
xam ngeen ne, dénk nanu leen kenn-kenn, ni baay di def ak doomam, dëfëlal leen seen xol te dëggal ci yéen, ngeen dund dund gu neex yàlla, moom mi leen di woo, ngeen séddu ci nguuram ak ndamam.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
lalu petrus berkata, "sekarang saya sungguh-sungguh menyadari bahwa allah memperlakukan semua orang sama
noonu piyeer jël kàddu ga ne leen: «ci dëgg gis naa ne, yàlla du gënale,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
"jawabanmu itu benar," kata yesus. "lakukanlah itu, maka engkau akan hidup.
yeesu ne ko nag: «li nga wax dëgg la. boo defee loolu, dinga dund ba fàww.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting