From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
cosa gli risponde però la voce divina? ginocchio davanti a baal
waaye lii la ko yàlla tontu: «dencal naa sama bopp juróom-ñaari junniy nit, ñi jaamuwul baal.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
perché nel nome di gesù ogni ginocchio si pieghi nei cieli, sulla terra e sotto terra
ngir turu yeesoo tax ñépp sukk,ci asamaan, ci kaw suuf, ci biir suuf;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
poiché sta scritto: ogni ginocchio si piegherà davanti a me e ogni lingua renderà gloria a dio
ndaxte mbind mi tëral na lii:«boroom bi nee na:“ni mu wóore ne maa ngi dund,ni la wóore ne, ñépp dinañu ma sukkal,te ku nekk seede ne maay yàlla.”»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
allora venne a lui un lebbroso: lo supplicava in ginocchio e gli diceva: «se vuoi, puoi guarirmi!»
am bés ku gaana ñëw ci moom, sukk, ñaan ko ne: «soo ko bëggee, man nga maa wéral.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
al veder questo, simon pietro si gettò alle ginocchia di gesù, dicendo: «signore, allontanati da me che sono un peccatore»
naka la simoŋ piyeer gis loolu, daldi sukk ci kanamu yeesu ne ko: «sore ma boroom bi, ndaxte nitu bàkkaar laa!»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: