Results for onnipotente translation from Italian to Wolof

Italian

Translate

onnipotente

Translate

Wolof

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

grandi cose ha fatto in me l'onnipotente e santo è il suo nome

Wolof

ndaxte ku màgg ki defal na ma lu réy.turam dafa sell.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e sarò per voi come un padre, e voi mi sarete come figli e figlie, dice il signore onnipotente

Wolof

dinaa nekk baay ci yéen,ngeen di doom ci man, muy góor, di jigéen. moom la aji kàttan ji wax.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

sono infatti spiriti di demòni che operano prodigi e vanno a radunare tutti i re di tutta la terra per la guerra del gran giorno di dio onnipotente

Wolof

ay rabi seytaane lañu woon, yuy def ay kéemaan te di dem ci buuri àddina sépp, di leen dajale, ngir xeex biy am ci bés bu mag, bi yàlla aji kàttan jagleele boppam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

non vidi alcun tempio in essa perché il signore dio, l'onnipotente, e l'agnello sono il suo tempio

Wolof

gisuma ca dëkk ba kër yàlla, ndaxte boroom bi yàlla aji kàttan ji ak mbote ma ñooy màggalukaay ba.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

dalla bocca gli esce una spada affilata per colpire con essa le genti. egli le governerà con scettro di ferro e pigerà nel tino il vino dell'ira furiosa del dio onnipotente

Wolof

am na jaasi ju ñaw juy génn ci gémmiñam, ngir dóor xeet yi, mu di leen jiitee yetu weñ, te mooy nappaaje réseñ yi ci segalukaayu mer mu tàng, mu yàlla aji kàttan ji.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

«noi ti rendiamo grazie, signore dio onnipotente, che sei e che eri, perché hai messo mano alla tua grande potenza, e hai instaurato il tuo regno

Wolof

naan:«nu ngi lay gërëm, boroom bi yàlla,yaw aji kàttan ji, ki nekk te nekkoon,ndax gànjoo nga sa kàttan gu réy gi,ngir taxawal sa nguur.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

io sono l'alfa e l'omega, dice il signore dio, colui che è, che era e che viene, l'onnipotente

Wolof

boroom bi yàlla nee na: «man yàlla maay alfa ak omega, maay ki nekk, ki nekkoon démb te di ñëw ëllëg, man aji kàttan ji.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

cantavano il cantico di mosè, servo di dio, e il cantico dell'agnello: o signore dio onnipotente; giuste e veraci le tue vie, o re delle genti

Wolof

Ñuy woy woyu musaa jaamu yàlla bi, ak woyu mbote ma, naan:«say jëf réy nañu te yéeme,yaw boroom bi yàlla, aji kàttan ji.say yoon jub nañu te dëggu,yaw buur bi fiy sax ba abadan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

i quattro esseri viventi hanno ciascuno sei ali, intorno e dentro sono costellati di occhi; giorno e notte non cessano di ripetere: il signore dio, l'onnipotente, colui che era, che è e che viene

Wolof

Ñeenti mbindeef ya am nañu ku nekk juróom-benni laaf te ñu nga fees ak ay bët li leen wër lépp, ba ci seen roni laaf. guddi ak bëccëg duñu noppeek naan:«boroom bi yàlla, aji kàttan ji,moo sell, sell, sell,moom ki nekkoon démb,ki nekk tey, te di ñëw ëllëg.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
9,204,984,591 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK