Results for serpenti translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

serpenti, razza di vipere, come potrete scampare dalla condanna della geenna

Wolof

yéen ñi mel ni ay jaan, te fees ak daŋar niy co, naka ngeen di mucce mbugalu safara?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

non mettiamo alla prova il signore, come fecero alcuni di essi, e caddero vittime dei serpenti

Wolof

bunu diiŋat kirist, ni ko ñenn ñi ci ñoom defe, ba ay jaan màtt leen, ñu dee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

la loro gola è un sepolcro spalancato, tramano inganni con la loro lingua, veleno di serpenti è sotto le loro labbra

Wolof

seen put a ngi xasaw ni méddum ñetti fan,seen làmmiñ làggi ci njublaŋ,te seeni kàddu aay ni daŋaru ñàngóor.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ecco: io vi mando come pecore in mezzo ai lupi; siate dunque prudenti come i serpenti e semplici come le colombe

Wolof

«dégluleen, maa ngi leen di yónni, mel ni ay xar ci biir ay bukki. muusleen nag niy jaan, te lewet niy pitax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ecco, io vi ho dato il potere di camminare sopra i serpenti e gli scorpioni e sopra ogni potenza del nemico; nulla vi potrà danneggiare

Wolof

gis ngeen, jox naa leen sañ-sañu joggi ci jaan yi ak ci jiit yi, daan dooley bañaale bi, te dara du leen man a gaañ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

la potenza dei cavalli infatti sta nella loro bocca e nelle loro code; le loro code sono simili a serpenti, hanno teste e con esse nuociono

Wolof

ndaxte kàttanu fas yaa ngi ci seeni gémmiñ ak ci seeni geen. geen yaa nga mel ni ay jaan, am ay bopp, te ñoom lañuy metitale nit ñi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

prenderanno in mano i serpenti e, se berranno qualche veleno, non recherà loro danno, imporranno le mani ai malati e questi guariranno»

Wolof

di jàpp jaan ak seeni loxo; te bu ñu naanee lu ñu tooke, du leen wàññi dara, te jarag ju ñu teg loxo, mu wér.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

afferrò il dragone, il serpente antico - cioè il diavolo, satana - e lo incatenò per mille anni

Wolof

mu jàpp ninkinànka ja, di jaani cosaan ja, muy tuumaalkat bi, maanaam seytaane. malaaka ma yeew ko diirub junniy at,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,776,738,446 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK