Results for dividida translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

la gente de la ciudad estaba dividida: unos estaban con los judíos, otros con los apóstoles

Wolof

noonu waa dëkk bi xàjjalikoo, ñii far ak yawut yi, ñale far ak ndaw ya.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

pero como jesús conocía sus pensamientos, les dijo: --todo reino dividido contra sí mismo está arruinado. y ninguna ciudad o casa dividida contra sí misma permanecerá

Wolof

waaye yeesu xam seen xalaat ne leen: «réew mu xeex boppam tas, te dëkk mbaa kër guy xeex boppam du man a yàgg.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

el padre estará dividido contra el hijo, y el hijo contra el padre; la madre contra la hija, y la hija contra la madre; la suegra contra su nuera, y la nuera contra su suegra

Wolof

baay bi dina féewaloo ak doom ji, doom ji ak baayam. ndey dina féewaloo ak doomam ju jigéen; doom ju jigéen ji ak ndeyam. goro dina féewaloo ak jabaru doomam; jabaru nit ak goroom.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,794,592,118 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK