Results for prisiones translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

te saludan epafras, mi compañero de prisiones por cristo jesús

Wolof

sama mbokk epafras, mi ma nekkal fi ci kaso bi ci turu kirist, mu ngi lay nuyu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

intercedo ante ti en cuanto a mi hijo onésimo, a quien he engendrado en mis prisiones

Wolof

maa ngi tinul sama doomu diine onesim, mi ma jur ci kirist fii ci kaso bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

yo deseaba retenerlo conmigo, para que en tu lugar me sirviera en mis prisiones por el evangelio

Wolof

dama koo bëggoon a téye fi sama wet, ngir mu taxawal la, di ma dimbali, li feek maa ngi ci kaso bi ngir xebaar bu baax bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

mientras aquéllos anuncian a cristo por contención, no sinceramente, pensando añadir aflicción a mis prisiones

Wolof

waaye ñale amuñu xol bu laab, te seen njariñu bopp rekk a tax ñuy yégle turu kirist, di wut a feddali samay buum ak coono.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

salvo que el espíritu santo me da testimonio en una ciudad tras otra, diciendo que me esperan prisiones y tribulaciones

Wolof

xam naa rekk ne, ci dëkkoo-dëkk xel mu sell mi xamal na ma ne, ay buum ak ay metit ñu ngi may nég.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

de esta manera, mis prisiones por la causa de cristo han sido conocidas en todo el pretorio y entre todos los demás

Wolof

noonu ñiy wottu buur bi ak ñépp gis nañu bu leer ne, turu kirist rekk a tax ñu jàpp ma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

ahora, la salutación de mi propia mano, de pablo. acordaos de mis prisiones. la gracia sea con vosotros

Wolof

man pool maa leen di bind nuyoo bii ci sama loxob bopp. fàttalikuleen ne, dañu maa jéng. na yiwu boroom bi ànd ak yéen!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

la mayoría de los hermanos, tomando ánimo en el señor por mis prisiones, se atreven mucho más a hablar la palabra sin temor

Wolof

te it bokk yu bare takk nañu seeni fit ci li ñu gis samay buum, ba tax ñu gën a ñeme ci wax kàddug yàlla ci lu àndul ak genn tiit.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

saludad a andrónico y a junias, mis parientes y compañeros de prisiones, quienes son muy estimados por los apóstoles y también fueron antes de mí en cristo

Wolof

nuyul-leen ma it andoronikus ak yuñas, sama bokk, yi ñu ma booleeloon tëj; am nañu tur ci ndawi yàlla yi, te ñoo ma jiitu sax ci gëm kirist.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

porque si dios no dejó sin castigo a los ángeles que pecaron, sino que, habiéndolos arrojado al infierno en prisiones de oscuridad, los entregó a ser reservados para el juicio

Wolof

ndaxte yàlla jeggalul malaaka ya bàkkaaroon, waaye tàbbal na leen safara, tëj leen ca kàmb yu lëndëm, di leen nége àtte ba.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

me es justo sentir esto de todos vosotros, porque os tengo en mi corazón. tanto en mis prisiones como en la defensa y confirmación del evangelio, sois todos vosotros participantes conmigo de la gracia

Wolof

te juumuma ci li ma xalaat loolu ci yéen ñépp, ndaxte def naa leen ci sama xol; ba tax fii ci kaso bi, ci taxawal xebaar bu baax bi ak lawal ko, yéen ñépp am ngeen wàll ak man ci yiwu yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

hallé que era acusado de cuestiones de la ley de ellos, pero sin ninguna acusación de crimen digno de muerte o de prisión

Wolof

gis naa ne li ñu ko jiiñ mu ngi aju ci ay werantey seen yoon, waaye jiiñuñu ko dara lu jar dee mbaa jéng.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,771,046,467 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK