Results for langu translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

mkiniomba chochote kwa jina langu, nitawafanyieni.

Wolof

lu ngeen ñaan ci sama tur, maa koy def.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

watu wote watawachukieni kwa sababu ya jina langu.

Wolof

te ñépp dinañu leen bañ ndax sama tur.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kwa hiyo hakuna awezaye kusema amebatizwa kwa jina langu.

Wolof

ngir kenn bañ a wax ne, ci sama tur lañu ko sóob.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

yeyote anayemkaribisha mtoto mmoja kama huyu kwa jina langu, ananikaribisha mimi.

Wolof

te it ku nangu ci sama tur xale bu mel ni kii, man mii nga nangu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

nafunga mara mbili kwa juma, natoa zaka sehemu ya kumi ya pato langu.

Wolof

ayu-bés gu nekk damay woor ñaari yoon, di joxe asaka ci lépp lu ma wut.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

mimi mwenyewe nitamwonyesha mengi yatakayomlazimu kuteswa kwa ajili ya jina langu."

Wolof

te dinaa ko won coono yu bare yu mu war a dékku ngir sama tur.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

na chochote mtakachoomba kwa jina langu nitafanya, ili baba atukuzwe ndani ya mwana.

Wolof

te it lu ngeen ñaan ci sama tur dinaa ko def, ngir doom ji feeñal ndamu baay bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

huyo mtumishi mwenzake akapiga magoti, akamwomba, unisubiri nami nitalipa deni langu lote.

Wolof

kon moroomam daanu ci suuf, ñaan ko ne: “muñal ma, dinaa la fey.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

asiyenipenda hashiki maneno yangu. na neno mlilosikia si langu, bali ni lake baba aliyenituma.

Wolof

ku ma bëggul doo sàmm sama kàddu. li may wax nag, jógewul ci man, waaye mi ngi soqikoo ci ki ma yónni.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

"kisha watawatoeni ili mteswe na kuuawa. mataifa yote yatawachukieni kwa ajili ya jina langu.

Wolof

bu boobaa dees na leen jébbale, metital leen, rey leen; te xeet yépp dinañu leen bañ ndax sama tur.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

maana wengi watakuja wakilitumia jina langu, wakisema, mimi ndiye! nao watawapotosha watu wengi.

Wolof

Ñu bare dinañu ñëw ci sama tur naan: “moom laa,” te dinañu nax ñu bare.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

maana wengi watatokea na kulitumia jina langu wakisema: mimi ndiye kristo, nao watawapotosha watu wengi.

Wolof

ndaxte ñu bare dinañu ñëw ci sama tur ne: “maa di kirist,” te dinañu nax ñu bare.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini msaidizi, roho mtakatifu, ambaye baba atamtuma kwa jina langu, atawafundisheni kila kitu na kuwakumbusheni yote niliyowaambieni.

Wolof

waaye dimbalikat, bi leen baay bi di yónnee ci sama tur, muy xelam mu sell, dina leen jàngal lépp, di leen fàttali li ma leen waxoon lépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

utakapokuja niletee koti langu nililoacha kwa karpo kule troa; niletee pia vile vitabu, na hasa vile vilivyotengenezwa kwa ngozi.

Wolof

te sooy ñëw, indaaleel mbubb, ma ma dénkoon karpus ca dëkku torowas, te it bul fàtte téere yi, rawatina téere yu am maana, yi ñu bind ci der.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

"wayahudi wanajua habari za maisha yangu tangu utoto, jinsi nilivyoishi tangu mwanzo kati ya taifa langu huko yerusalemu.

Wolof

«ci lu jëm ci yawut yi, xam nañu sama dund li dale ci samag ndaw, muy ci sama biir xeet, muy ci yerusalem.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

kwa vyovyote kila mmoja na aishi kufuatana na vipaji alivyogawiwa na bwana, na kama alivyoitwa na mungu. hili ndilo agizo langu kwa makanisa yote.

Wolof

ku nekk nag na dund, ni ko ko boroom bi jagleele, mu mengoo ak ni mu meloon, bi ko yàlla wooyee. moom laay tëral ci mboolooy ñi gëm yépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini yesu akasema, "msimkataze, maana hakuna mtu anayefanya muujiza kwa jina langu, na papo hapo akaweza kusema mabaya juu yangu.

Wolof

waaye yeesu tontu ko: «buleen ko tere, ndaxte kenn mënul a def kéemaan ci sama tur, ba noppi di ma xarab.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

ninyi hamkunichagua mimi; mimi niliwachagueni na kuwatuma mwende mkazae matunda, matunda yadumuyo, naye baba apate kuwapa ninyi chochote mumwombacho kwa jina langu.

Wolof

du yéen yéena ma tànn, waaye man maa leen tànn, sas leen ngeen dem, meññ meññeef gu sax, ngir baay bi def lu ngeen ko ñaan ci sama tur.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

"anayempokea mtoto kama huyu kwa jina langu, ananipokea mimi; na anayenipokea mimi, hanipokei mimi tu, bali anampokea yule aliyenituma."

Wolof

«ku nangu xale bu mel ni bii ci sama tur, man mii nga nangu; te ku ma nangu, du man mii sax nga nangu waaye ki ma yónni.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

"kweli nawaambieni, anayesikia neno langu, na kumwamini yule aliyenituma, anao uzima wa milele. hatahukumiwa kamwe, bali amekwisha pita kutoka kifo na kuingia katika uzima.

Wolof

«ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, ku dégg sama kàddu te gëm ki ma yónni, am nga dund gu dul jeex te doo jaar ca àtte ba, ndaxte génn nga ci dee, tàbbi ci dund.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,773,718,019 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK