Results for sanning translation from Swedish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swedish

Wolof

Info

Swedish

helga dem i sanningen; ditt ord är sanning.

Wolof

samp leen ci dëgg, ngir ñu sell. sa kàddu mooy dëgg.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

men mig tron i icke, just därför att jag talar sanning.

Wolof

waaye man damay wax dëgg, moo tax gëmuleen ma.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

ty ljusets frukt består i allt vad godhet och rättfärdighet och sanning är.

Wolof

leer, mbaax lay meññ, njub ak dëgg.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

gud är ande, och de som tillbedja måste tillbedja i ande och sanning.»

Wolof

yàlla xel la, kon ñi koy jaamu war nañu koo jaamu ci xel ak ci dëgg.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

den äldste hälsar gajus, den älskade brodern, som jag i sanning älskar.

Wolof

man njiit li, maa ngi lay bind, yaw sama xarit gayus, mi ma bëgg ci sama xol.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

och jag helgar mig till ett offer för dem, på det att ock de må vara i sanning helgade.

Wolof

sellal naa sama bopp ngir ñoom, ngir ñu sampu ci dëgg te sell.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

kära barn, låtom oss älska icke med ord eller med tungan, utan i gärning och i sanning.

Wolof

samay doom, bunu bëggante ci wax mbaa ci làmmiñ rekk, waaye ci jëf ak ci dëgg.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

med sanning i vårt tal, med kraft från gud, med rättfärdighetens vapen både i högra handen och i vänstra,

Wolof

ci kàddug dëgg ak ci kàttanu yàlla, nu ngi yor gànnaayi njubte ci loxol ndeyjoor ak lu càmmooñ.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

jag talar sanning i kristus, jag ljuger icke -- därom bär mitt samvete mig vittnesbörd i den helige ande --

Wolof

li ma bëgg a wax nag, ci kanamu kirist laa koy waxe; dëgg la, du aw fen. sama xel, mi xel mu sell miy leeral, seedeel na ma ne, dëgg laay wax.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

dock gåvo vi icke ens ett ögonblick vika för dem genom en sådan underkastelse; ty vi ville att evangelii sanning skulle bliva bevarad hos eder.

Wolof

waaye yaatalunu leen benn yoon, ngir dëggug xebaar bu baax bi man a sax ci yéen.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

de hade ju bytt bort guds sanning mot lögn och tagit sig för att dyrka och tjäna det skapade framför skaparen, honom som är högtlovad i evighet, amen.

Wolof

toxal nañu dëggu yàlla, tëral fen, di màggal ak a jaamu mbindeef, ba faaleetuñu sax aji bind, ji yelloo cant ba fàww. amiin.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

den äldste hälsar den utvalda frun och hennes barn, vilka jag i sanning älskar, och icke jag allenast, utan ock alla andra som hava lärt känna sanningen.

Wolof

man njiit li maa leen di bind, yaw soxna su tedd si, yaw ak say doom. bëgg naa leen bu wér ci sama xol, jéllale naa sama bopp sax, waaye itam képp ku xam dëgg gi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då sade jesus till de judar som hade satt tro till honom: »om i förbliven i mitt ord, så ären i i sanning mina lärjungar;

Wolof

yeesu ne yawut ya ko gëmoon: «bu ngeen saxee ci li ma wax, nekk ngeen samay taalibe ci lu wóor.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

men den tid skall komma, ja, den är redan inne, då sanna tillbedjare skola tillbedja fadern i ande och sanning; ty sådana tillbedjare vill fadern hava.

Wolof

waaye jamono dina ñëw, te agsi na ba noppi, jamono joo xam ne jaamukat yi dëgg dinañu jaamu baay bi ci xel ak ci dëgg. Ñooñu nag, ñooy jaamu baay bi, ni mu ko bëgge.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då svarade den skriftlärde honom: »mästare, du har i sanning rätt i vad du säger, att han är en, och att ingen annan är än han.

Wolof

xutbakat bi ne ko: «waaw kilifa gi, li nga wax dëgg la: yàlla kenn la, te amul jeneen yàlla ju dul moom.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

ja, i sanning, de församlade sig i denna stad mot din helige tjänare jesus, mot honom som du har smort: herodes och pontius pilatus med hedningarna och israels folkstammar;

Wolof

ndaxte ci dëgg ci dëkk bii, erodd ak poñsë pilaat ànd ak xeeti àddina ak bànni israyil, likkoo nañu, ngir daaneel sa ndaw lu sell li nga fal, di yeesu,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

och om jag inför honom har berömt mig något i fråga om eder, så har jag icke kommit på skam därmed; utan likasom vi eljest i allting hava talat sanning inför eder, så har också det som vi inför titus hava sagt till eder berömmelse visat sig vara sanning.

Wolof

su fekkee ne tiitaru woon naa ci seen mbir ci kanamu tit, rusuma ci. dëgg rekk lanu leen mas a wax; noonu it la tit gise ne, li nu leen doon seede lépp, dëgg la.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

de skola få många efterföljare i sin lösaktighet, och för deras skull skall sanningens väg bliva smädad.

Wolof

ñu bare dinañu leen fekki ci seeni ñaawteef, ba gàkkal yoonu dëgg ci bëti nit ñi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,772,851,841 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK