Results for yoktur translation from Turkish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Turkish

Wolof

Info

Turkish

‹‹tanrı korkusu yoktur onlarda.››

Wolof

te ragal yàlla sore na seen xol.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Turkish

tanrının yapamayacağı hiçbir şey yoktur.››

Wolof

ndaxte dara tëwul yàlla.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Turkish

ama ben sizi bilirim, içinizde tanrı sevgisi yoktur.

Wolof

waaye yéen, xam naa leen; leer na ma ne, amuleen ci seen xol benn mbëggeel ci yàlla.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Turkish

oysa gece yürüyen sendeler. Çünkü kendisinde ışık yoktur.››

Wolof

waaye kuy dox guddi, dina fakkastalu, ndaxte leer nekkul ci moom.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Turkish

sünnetli olup olmamanın önemi yoktur, önemli olan yeni yaratılıştır.

Wolof

xaraf ak bañ a xaraf dara amu ci solo. li am solo mooy nekk mbindeef mu bees.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Turkish

bunların bağışlanması durumunda artık günah için sunuya gerek yoktur.

Wolof

kon nag fu ñuy baale bàkkaar, aajootul sarax su koy dindi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Turkish

Çünkü burada kalıcı bir kentimiz yoktur, biz gelecekteki kenti özlüyoruz.

Wolof

amunu fii ci àddina dëkk bu sax ba fàww, waaye nu ngi wut dëkk biy ñëw.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Turkish

kardeşler, bu olayların zamanı ve tarihi konusunda size yazmaya gerek yoktur.

Wolof

waaye bokk yi, ci li jëm ci jamono yi ak waxtu, yi loolu di am, matul nu leen ciy bind dara.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Turkish

dünyayı da dünyaya ait şeyleri de sevmeyin. dünyayı sevenin babaya sevgisi yoktur.

Wolof

buleen sopp àddina ak li ci biiram. ku sopp àddina, mbëggeelu baay bi nekkul ci moom.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Turkish

hiç kimsede, insanın, dostları uğruna canını vermesinden daha büyük bir sevgi yoktur.

Wolof

genn mbëggeel mënul a weesu joxe sa bakkan ngir say xarit.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Turkish

‹‹onu tanıyorum›› deyip de buyruklarını yerine getirmeyen yalancıdır, kendisinde gerçek yoktur.

Wolof

ku wax ne xam nga ko, te sàmmoo ay ndigalam, dangay fen, te dëgg nekkul ci yaw.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Turkish

kadınlar toplantılarınızda sessiz kalsın. konuşmalarına izin yoktur. kutsal yasanın da belirttiği gibi, uysal olsunlar.

Wolof

na jigéen ñi noppi ci ndaje mi, ndaxte sañuñu faa wax. nañu doon jigéen ñu nangu, ni ko yoon wi tërale.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Turkish

sevgide korku yoktur. tersine, yetkin sevgi korkuyu siler atar. Çünkü korku işkencedir. korkan kişi sevgide yetkin kılınmamıştır.

Wolof

genn ragal amul ci mbëggeel, waaye mbëggeel gu mat sëkk day dàq ragal. ndaxte ragal day ànd ak mbugal; te ku ragal, mbëggeel matul sëkk ci yaw.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Turkish

başlatılacak url yok

Wolof

amul url bees man a ubbi

Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,925,772,803 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK