From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
bi bëgg ñépp mucc te xam dëgg gi.
who will have all men to be saved, and to come unto the knowledge of the truth.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
leer, mbaax lay meññ, njub ak dëgg.
(for the fruit of the spirit is in all goodness and righteousness and truth;)
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye man damay wax dëgg, moo tax gëmuleen ma.
and because i tell you the truth, ye believe me not.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
dinañu tanqamlu dëgg, jeng jëm ci léebi diiney neen.
and they shall turn away their ears from the truth, and shall be turned unto fables.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
sellal naa sama bopp ngir ñoom, ngir ñu sampu ci dëgg te sell.
and for their sakes i sanctify myself, that they also might be sanctified through the truth.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te it dingeen xam dëgg gi te dëgg gi dina leen goreel.»
and ye shall know the truth, and the truth shall make you free.
Last Update: 2014-05-10
Usage Frequency: 1
Quality:
ci dëgg maa ngi leen koy wax, niti jamono jii duñu wéy te loolu lépp amul.
verily i say unto you, this generation shall not pass, till all these things be fulfilled.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ci dëgg maa ngi la koy wax, doo génn foofa mukk te feyuloo dërëm bi ci mujj.
verily i say unto thee, thou shalt by no means come out thence, till thou hast paid the uttermost farthing.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye li xam-xamu yàlla di jur, mooy firndeel ne dëgg la.»
but wisdom is justified of all her children.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ci coobareem la nu sole kàddug dëgg gi, ba nu judduwaat, di tànneefu lépp lu mu bind.
of his own will begat he us with the word of truth, that we should be a kind of firstfruits of his creatures.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ku wax ne xam nga ko, te sàmmoo ay ndigalam, dangay fen, te dëgg nekkul ci yaw.
he that saith, i know him, and keepeth not his commandments, is a liar, and the truth is not in him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ni ngeen jógtee woon de baax na! waaw ku leen dog, ba ngeen bañ a déggal dëgg?
ye did run well; who did hinder you that ye should not obey the truth?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
gannaaw ba nu nangoo xam dëgg ba noppi, bu nu teyee di def bàkkaar, kon sarax dootul am ngir bàkkaar yooyu.
for if we sin wilfully after that we have received the knowledge of the truth, there remaineth no more sacrifice for sins,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ci dëgg maa ngi leen koy wax, ku woyoful ni xale, nangu nguuru yàlla, doo ci man a dugg.»
verily i say unto you, whosoever shall not receive the kingdom of god as a little child, he shall not enter therein.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye su ma delloo di sàmm ndigali yoon, yi ma bàyyi, dëgg-dëgg dinaa wone noonu ne, moykatu yoon wi laa.
for if i build again the things which i destroyed, i make myself a transgressor.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
«ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, ku jaar feneen fu dul ci buntu gétt gi, kooku sàcc la, saay-saay la.
verily, verily, i say unto you, he that entereth not by the door into the sheepfold, but climbeth up some other way, the same is a thief and a robber.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: