From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
nuyul-leen nu bokk yépp ak saafoonte bu laab.
greet all the brethren with an holy kiss.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nuyul ma piriska ak akilas ak waa kër onesifor.
salute prisca and aquila, and the household of onesiphorus.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nuyul-leen ma pirsil ak akilas, samay nawle ci liggéeyu kirist yeesu.
greet priscilla and aquila my helpers in christ jesus:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nuyul-leen ma seen njiit yépp ak gaayi yàlla yépp. waa itali ñu ngi leen di nuyu.
salute all them that have the rule over you, and all the saints. they of italy salute you.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñiy ànd ak man ñépp ñu ngi lay nuyu. nuyul nu sunuy soppey ngëm. na yiwu yàlla ànd ak yéen ñépp.
all that are with me salute thee. greet them that love us in the faith. grace be with you all. amen.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nuyul-leen ma gaayi kirist yeesu yu sell yépp. bokk yi ànd ak man, ñu ngi leen di nuyu.
salute every saint in christ jesus. the brethren which are with me greet you.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nuyul-leen ma it filolog ak yuli, nere ak jigéenam.te fàttewuma olimpas ak gaayi yàlla yiy booloo ak ñoom ñépp.
salute philologus, and julia, nereus, and his sister, and olympas, and all the saints which are with them.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nuyul-leen nu mbokk, yi nekk lawdise. nuyul-leen nu itam nimfa ak mbooloom ñi gëm, miy daje ci këram.
salute the brethren which are in laodicea, and nymphas, and the church which is in his house.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nuyul-leen ma it andoronikus ak yuñas, sama bokk, yi ñu ma booleeloon tëj; am nañu tur ci ndawi yàlla yi, te ñoo ma jiitu sax ci gëm kirist.
salute andronicus and junia, my kinsmen, and my fellowprisoners, who are of note among the apostles, who also were in christ before me.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: