From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
tekke bu rey:
long description
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñu sawar lañu ci rey nit.
their feet are swift to shed blood:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñu jàpp ko nag, rey, sànni ci biti.»
and they took him, and killed him, and cast him out of the vineyard.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
keroog la njiiti yawut ya dogu ci rey yeesu.
then from that day forth they took counsel together for to put him to death.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñu jàpp ko nag, génne ko tool bi, rey ko.»
and they caught him, and cast him out of the vineyard, and slew him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
indileen sëllu wu duuf wa te rey ko, nu lekk te bànneexu;
and bring hither the fatted calf, and kill it; and let us eat, and be merry:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yawut ya daldi foraat ay xeer, bëgg koo sànni, ngir rey ko.
then the jews took up stones again to stone him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte bàkkaar jaar na ci li yàlla digle, ba nax ma, rey ma.
for sin, taking occasion by the commandment, deceived me, and by it slew me.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
loolu nag moo waral yawut yi jàpp ma ca kër yàlla ga, di ma fexee rey.
for these causes the jews caught me in the temple, and went about to kill me.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
erodd nag bëgg koo rey, waaye dafa ragal nit ñi, ci li ñu teg yaxya ab yonent.
and when he would have put him to death, he feared the multitude, because they counted him as a prophet.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te dégg naa baat bu ma ne: “jógal piyeer, rey te lekk.”
and i heard a voice saying unto me, arise, peter; slay and eat.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
xam naa ne askanu ibraayma ngeen. waaye yéena ngi may wut a rey, ndaxte li may jàngale xajul ci yéen.
i know that ye are abraham's seed; but ye seek to kill me, because my word hath no place in you.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
mu yónneeti beneen surga, ñu rey ko. mu yónni ñeneen ñu bare, ñii ñu dóor leen, ñii ñu rey.
and again he sent another; and him they killed, and many others; beating some, and killing some.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
dangeen di seede noonu ne, ànd ngeen ak li seen maam defoon, ndaxte ñoo rey yonent yi, yéen ngeen tabax xabru yi.
truly ye bear witness that ye allow the deeds of your fathers: for they indeed killed them, and ye build their sepulchres.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te buleen ragal ñu man a rey yaram, te mënuñoo rey ruu, waaye ragal-leen ki man a sànk yaram ak ruu ci safara.
and fear not them which kill the body, but are not able to kill the soul: but rather fear him which is able to destroy both soul and body in hell.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye beykat yi daldi ne ci seen biir: “kii moo war a donn tool bi; nan ko rey, moom ndono li.”
but those husbandmen said among themselves, this is the heir; come, let us kill him, and the inheritance shall be ours.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: