Results for teeru translation from Wolof to English

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

English

Info

Wolof

bi nu agsee yerusalem nag, taalibe ya teeru nu ak mbég.

English

and when we were come to jerusalem, the brethren received us gladly.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

nun nag fàww nu teeru ñu mel ni ñoom, ngir nu liggéeyandoo ak dëgg gi.

English

we therefore ought to receive such, that we might be fellowhelpers to the truth.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

looloo tax mbooloo ma teeru ko, ndaxte yégoon nañu firnde boobu.

English

for this cause the people also met him, for that they heard that he had done this miracle.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

soo ma jàppee ni nawle nag, teeru ko, ni su ma la doon ganesi.

English

if thou count me therefore a partner, receive him as myself.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

teeruleen ko teeru bu rafet nag ngir boroom bi, te teral ñi mel ni moom.

English

receive him therefore in the lord with all gladness; and hold such in reputation:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi yeesu dëppee dellu, mbooloo ma di ko teeru, ndaxte ñépp a ngi ko doon xaar.

English

and it came to pass, that, when jesus was returned, the people gladly received him: for they were all waiting for him.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yaw sama xarit, sa takkute fés na ci teeru bi ngay teeru mbokk yi, te fekk xamoo leen.

English

beloved, thou doest faithfully whatsoever thou doest to the brethren, and to strangers;

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

na seen teeru firndeel nag seen mbëggeel ci kanamu mboolooy ñi gëm, te dëggal leen ne, noo yey wóolu leen.

English

wherefore shew ye to them, and before the churches, the proof of your love, and of our boasting on your behalf.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

na ko boroom bi teeru ak yërmandeem ca bés ba. umplewoo it coono yi mu daj, ngir dimbali ma ca dëkku efes.

English

the lord grant unto him that he may find mercy of the lord in that day: and in how many things he ministered unto me at ephesus, thou knowest very well.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag boroom bi nee na:«génnleen biir ñooñu te beru.buleen laal dara lu am sobe,kon dinaa leen teeru.

English

wherefore come out from among them, and be ye separate, saith the lord, and touch not the unclean thing; and i will receive you,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te bi ñu agsee yerusalem, mbooloom ñi gëm, ndaw yi ak njiit yi teeru leen, ñu nettali leen fi ñu jaar ak yàlla fépp.

English

and when they were come to jerusalem, they were received of the church, and of the apostles and elders, and they declared all things that god had done with them.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te mbëggeelam ci yéen gën na yokku, buy fàttaliku ni ngeen ko déggale yéen ñépp, ci li ngeen ko teeru, ànd ak ragal ak weg.

English

and his inward affection is more abundant toward you, whilst he remembereth the obedience of you all, how with fear and trembling ye received him.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

amoon na nag ca wet ya ay suuf yu doon moomeelu ku tudd publiyus, di kilifag dun ba. mu teeru nu, ganale nu ngan gu réy diirub ñetti fan.

English

in the same quarters were possessions of the chief man of the island, whose name was publius; who received us, and lodged us three days courteously.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

naka raxab jigéenu moykat bi itam, ndax du ci noonu la ko yàlla àttee ni ku jub, ci li mu teeru ndawi yawut yi, te jaarale leen ca poot ba?

English

likewise also was not rahab the harlot justified by works, when she had received the messengers, and had sent them out another way?

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

naka mu bëgg a dem akayi, bokk ya xiir ko ca, ñu bind taalibe ya, ngir ñu teeru ko teeru bu rafet. noonu mu dikk fa te jariñ lool ñi gëm jaare ko ci yiwu yàlla.

English

and when he was disposed to pass into achaia, the brethren wrote, exhorting the disciples to receive him: who, when he was come, helped them much which had believed through grace:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

coono, gi leen sama wopp tegoon, taxul ngeen bañ ma, taxul ngeen séexlu ma. waaye teeru ngeen ma, ni bu ngeen doon teeru malaakam yàlla walla yeesu kirist.

English

and my temptation which was in my flesh ye despised not, nor rejected; but received me as an angel of god, even as christ jesus.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te gannaaw teeru ba neexul a lollikoo, ña ca ëpp mànkoo ci jóge fa, dem ci biir géej, ngir wut a agsi fenigsë, biy teerub dunu kereet te janook sowu suuf ak sowu kaw, nu lollikoo fa.

English

and because the haven was not commodious to winter in, the more part advised to depart thence also, if by any means they might attain to phenice, and there to winter; which is an haven of crete, and lieth toward the south west and north west.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñu daldi jël cari garab, génn di ko teeru. Ñuy xaacu naan:«osaana!yaw miy ñëw ci turu boroom bi,ku barkeel nga!na yàlla barkeel buuru israyil!»

English

took branches of palm trees, and went forth to meet him, and cried, hosanna: blessed is the king of israel that cometh in the name of the lord.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,884,684,814 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK