Results for gindi translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

samay bokk, su amee ci yéen ku réere dëgg, te am ku ko gindi,

French

mes frères, si quelqu`un parmi vous s`est égaré loin de la vérité, et qu`un autre l`y ramène,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

na xam lii: ku gindi bàkkaarkat ci réeram, musal nga nit ci dee te faral ko bàkkaar yu bare.

French

qu`il sache que celui qui ramènera un pécheur de la voie où il s`était égaré sauvera une âme de la mort et couvrira une multitude de péchés.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

gor laa te kenn moomu ma; teewul def naa sama bopp jaamu ñépp, ngir man a gindi nit ñu bare ci kirist.

French

car, bien que je sois libre à l`égard de tous, je me suis rendu le serviteur de tous, afin de gagner le plus grand nombre.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci biir ñi néew ngëm, meloon naa ni ku néew ngëm, ngir gindi leen. doon naa lépp ci ñépp, ngir def lépp lu ma man, ba ñenn mucc ci.

French

j`ai été faible avec les faibles, afin de gagner les faibles. je me suis fait tout à tous, afin d`en sauver de toute manière quelques-uns.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«te lii itam, bu sa mbokk defee bàkkaar, demal yedd ko, yéen ñaar rekk. bu la dégloo, kon gindi nga sa mbokk.

French

si ton frère a péché, va et reprends-le entre toi et lui seul. s`il t`écoute, tu as gagné ton frère.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci biir ñi nekkul ci yoonu musaa, faalewuma woon yoon wi, ngir gindi leen; waxuma ne, ànduma ak yoonu yàlla, waaye topp naa yoon ci sama bokk ak kirist.

French

avec ceux qui sont sans loi, comme sans loi (quoique je ne sois point sans la loi de dieu, étant sous la loi de christ), afin de gagner ceux qui sont sans loi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yéen itam jigéen ñi, na ku nekk nangul sa jëkkër. noonu su amee góor gu gëmul kàddug yàlla, te gis jabaram di dund dund gu sell, boole ci weg ko, loolu dina ko gindi ci lu àndul ak wax.

French

femmes, soyez de mêmes soumises à vos maris, afin que, si quelques-uns n`obéissent point à la parole, ils soient gagnés sans parole par la conduite de leurs femmes,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bu xelum yàlla mi yor dëgg gi dikkee nag, dina leen gindi ci lépp li jëm ci yoonu dëgg, ndaxte du wax ci coobarey boppam, waaye lu ko baay bi wax, mu jottali leen ko. dina leen yégal mbir yu ñëwagul.

French

quand le consolateur sera venu, l`esprit de vérité, il vous conduira dans toute la vérité; car il ne parlera pas de lui-même, mais il dira tout ce qu`il aura entendu, et il vous annoncera les choses à venir.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,778,095,293 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK