Results for noppalu translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

fàww ñu sóob ma ci metit, te ba looluy mat, duma noppalu.

French

il est un baptême dont je dois être baptisé, et combien il me tarde qu`il soit accompli!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte képp ku mas a dugg ca noflaayu yàlla, noppalu na ci ay jëfam ni yàlla.

French

car celui qui entre dans le repos de dieu se repose de ses oeuvres, comme dieu s`est reposé des siennes.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu ñu dellu defari cuuraay ak latkoloñ ngir néew ba. ca bésu noflaay ba ñu noppalu, ni ko yoon wi santaanee.

French

et, s`en étant retournées, elles préparèrent des aromates et des parfums. puis elles se reposèrent le jour du sabbat, selon la loi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

am na fu ñu wax ci mbind mi ne:«yàlla noppalu na ci liggéeyam béppca juróom-ñaareelu fan ba.»

French

car il a parlé quelque part ainsi du septième jour: et dieu se reposa de toutes ses oeuvres le septième jour.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

foofa la teenu yanqóoba nekkoon. yeesu toog ca pindu teen ba, di noppalu ndax coonob tukki ba. ca digg-bëccëg la woon.

French

là se trouvait le puits de jacob. jésus, fatigué du voyage, était assis au bord du puits. c`était environ la sixième heure.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu mu ñëw ca taalibe ya ne leen: «nelawleen léegi te noppalu. waxtu wu ñu ma war a jébbale ci loxoy bàkkaarkat yi, jege na.

French

puis il alla vers ses disciples, et leur dit: vous dormez maintenant, et vous vous reposez! voici, l`heure est proche, et le fils de l`homme est livré aux mains des pécheurs.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te saxar siy jóge ci seen mbugal dina gilli ba fàww. Ñooñu di jaamu rab wi ak nataalam, ak képp ku nangoo jot màndargam turam, duñu noppalu guddi ak bëccëg.»

French

et la fumée de leur tourment monte aux siècles des siècles; et ils n`ont de repos ni jour ni nuit, ceux qui adorent la bête et son image, et quiconque reçoit la marque de son nom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci kaw loolu yeesu ne leen: «nanu beddeeku, dem ci bérab bu wéet; ngeen noppalu fa tuuti.» waxoon na loolu, ndaxte amoon na ñu bare ñu doon dem ak a dikk, ba amuñu sax jot ngir lekk.

French

jésus leur dit: venez à l`écart dans un lieu désert, et reposez-vous un peu. car il y avait beaucoup d`allants et de venants, et ils n`avaient même pas le temps de manger.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,186,546,361 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK