From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
noonu yeesu woo xale, teg ko ci seen biir,
jésus, ayant appelé un petit enfant, le plaça au milieu d`eux,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
li ñu leen xiir jógewul ci yàlla, mi leen woo.
cette influence ne vient pas de celui qui vous appelle.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
mu daldi woo kenn ca surga ya nag, laaj ko lu xew.
il appela un des serviteurs, et lui demanda ce que c`était.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye na seen dund gépp sell, ni yàlla mi leen woo selle.
mais, puisque celui qui vous a appelés est saint, vous aussi soyez saints dans toute votre conduite, selon qu`il est écrit:
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte ñi ñu woo bare nañu, waaye ñi ñu tànn barewul.»
car il y a beaucoup d`appelés, mais peu d`élus.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
booba nag ku woo boroom bi ci aw turam,dinga mucc.”
alors quiconque invoquera le nom du seigneur sera sauvé.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yàlla, mi leen woo ci loolu, kuy sàmm kóllëre la, te dina ko def.
celui qui vous a appelés est fidèle, et c`est lui qui le fera.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
taalibey yaxya ya nettali mbir yooyu yépp seen kilifa. noonu yaxya woo ñaar ci ay taalibeem,
jean fut informé de toutes ces choses par ses disciples.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu mu yónni ay surgaam, ngir ñu woo gan yi ca céet ga, waaye gan yi bëgguñoo ñëw.
il envoya ses serviteurs appeler ceux qui étaient invités aux noces; mais ils ne voulurent pas venir.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndax li yàlla maye, dootu ko nangu mukk, te ku mu woo ci boppam, dootu la dàq mukk.
car dieu ne se repent pas de ses dons et de son appel.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
piyeer may ko loxo, yékkati ko. mu woo gaayi yàlla ya ak jigéen ña, won leen ko, muy dund.
il lui donna la main, et la fit lever. il appela ensuite les saints et les veuves, et la leur présenta vivante.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
di daw yen muj ga, ngir jot li ma yàlla tax a woo, di cér bi ma yàlla wooye te dencal ma ko ci asamaan ci darajay kirist yeesu.
je cours vers le but, pour remporter le prix de la vocation céleste de dieu en jésus christ.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye ci ñi yàlla woo, ñuy yawut mbaa di gereg, kirist mooy dooley yàlla, di xam-xamu yàlla.
mais puissance de dieu et sagesse de dieu pour ceux qui sont appelés, tant juifs que grecs.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
boo àggee ca kër ga, dinga woo say xarit ak say dëkkandoo ne leen: “kaayleen bànneexu ak man, ndaxte gis naa sama xar ma réeroon.”
et, de retour à la maison, il appelle ses amis et ses voisins, et leur dit: réjouissez-vous avec moi, car j`ai retrouvé ma brebis qui était perdue.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.