Results for séddale translation from Wolof to German

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

German

Info

Wolof

am na fànni may yu bare yu jóge ci xelum yàlla, waaye menn xel moomu moo koy séddale.

German

es sind mancherlei gaben; aber es ist ein geist.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te lu la yàlla jagleel kenn ku nekk ci yéen, nanga ko bokk ak ñépp ni jawriñ ju jub, ci séddale yiwu yàlla wu yaatu.

German

und dienet einander, ein jeglicher mit der gabe, die er empfangen hat, als die guten haushalter der mancherlei gnade gottes:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

amoon na fa it tuuti jën yu ndaw. yeesu jël ko, sant yàlla, wax taalibe yi, ñu séddale leen itam mbooloo mi.

German

und hatten ein wenig fischlein; und er dankte und hieß die auch vortragen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu daldi jël mburu ya, gërëm yàlla, ba noppi séddale ko ña fa toogoon. mu jox leen itam jën, ba ñu doyal sëkk.

German

jesus aber nahm die brote, dankte und gab sie den jüngern, die jünger aber denen, die sich gelagert hatten; desgleichen auch von den fischen, wieviel sie wollten.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te it yàlla dëggal na seen seede ci ay firnde ak ay kéemaan, ay jaloore yu bare ak ci ay may yu jóge ci xelam mu sell, te mu séddale leen ni mu ko bëgge.

German

und gott hat ihr zeugnis gegeben mit zeichen, wundern und mancherlei kräften und mit austeilung des heiligen geistes nach seinem willen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon gannaaw yàlla séddale na ay mayam, ku nekk ak sa cér, nanu koy jëfandikoo. ku yàlla may, ngay waare kàddoom, nga wax ko kem sa ngëm;

German

und haben mancherlei gaben nach der gnade, die uns gegeben ist.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi loolu amee yeesu jël juróomi mburu yi ak ñaari jën yi, xool ci kaw, gërëm yàlla, ba noppi mu damm leen, jox taalibe yi, ngir ñu séddale ko mbooloo mi.

German

da nahm er die fünf brote und zwei fische und sah auf gen himmel und dankte darüber, brach sie und gab sie den jüngern, daß sie dem volk vorlegten.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xarekat ya, bi ñu daajee yeesu ca bant ba, ba noppi dañoo jël ay yéreem, séddale ko ñeenti cér, ku nekk benn. jël nañu it mbubbam bu ñu ràbb ca kaw ba ci suuf te amul benn ñaw.

German

die kriegsknechte aber, da sie jesus gekreuzigt hatten, nahmen sie seine kleider und machten vier teile, einem jeglichen kriegsknecht ein teil, dazu auch den rock. der rock aber war ungenäht, von obenan gewirkt durch und durch.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

benn bés caat ma ne baay ba: “baay, damaa bëggoon, nga jox ma li may war a féetewoo ci ndono li.” noonu baay ba daldi leen séddale alalam.

German

und der jüngste unter ihnen sprach zu dem vater: gib mir, vater, das teil der güter, das mir gehört. und er teilte ihnen das gut.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ca bés yooyu, naka taalibe yi di gën a bare, yawut yiy làkk gereg tàmbalee ñaxtu ci mbirum yawut tigi yi, te lii a ko waral: jigéen ñi seen jëkkër dee, te ñu bokk ci ñoom, naraalewuñu leen ca ndimbal, la ñuy séddale bés bu nekk.

German

in den tagen aber, da der jünger viele wurden, erhob sich ein murmeln unter den griechen wider die hebräer, darum daß ihre witwen übersehen wurden in der täglichen handreichung.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,792,232,372 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK