Vous avez cherché: philip (Anglais - Wolof)

Anglais

Traduction

philip

Traduction

Wolof

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Anglais

Wolof

Infos

Anglais

now philip was of bethsaida, the city of andrew and peter.

Wolof

filib mu nga dëkkoon betsayda, dëkku andare ak piyeer.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

then philip went down to the city of samaria, and preached christ unto them.

Wolof

naka filib mu dem ca benn dëkk ca samari, di leen yégal kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

philip saith unto him, lord, shew us the father, and it sufficeth us.

Wolof

filib ne ko: «boroom bi, won nu baay bi; loolu doy na nu.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

philip cometh and telleth andrew: and again andrew and philip tell jesus.

Wolof

filib dem wax ko andare; ñu ànd, waxi ko yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

then philip opened his mouth, and began at the same scripture, and preached unto him jesus.

Wolof

noonu filib tàmbali ci aaya yooyu, xamal ko xebaar bu baax bi ci mbirum yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

philip answered him, two hundred pennyworth of bread is not sufficient for them, that every one of them may take a little.

Wolof

filib ne ko: «peyug juróom ñetti weer sax, bu nu ko amoon, du leen man a doy ci mburu, ba kenn ku nekk ci ñoom am ci dog wu ndaw.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and nathanael said unto him, can there any good thing come out of nazareth? philip saith unto him, come and see.

Wolof

nataneel tontu ko ne: «aa! ndax dara lu baax man na jóge nasaret?» filib ne ko: «Ñëwal gis.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he said, how can i, except some man should guide me? and he desired philip that he would come up and sit with him.

Wolof

mu tontu ko ne: «nu ma ko man a xame, su ma ko kenn firilul?» mu woo filib nag, mu yéeg, toog ak moom.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

but herod the tetrarch, being reproved by him for herodias his brother philip's wife, and for all the evils which herod had done,

Wolof

waaye yaxya yedd na erodd boroom diiwaanu galile, ndaxte dafa takkoon erojàdd, jabaru magam, te it boole woon na ci yeneen ñaawteef,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and he commanded the chariot to stand still: and they went down both into the water, both philip and the eunuch; and he baptized him.

Wolof

mu santaane nag, ñu taxawal watiir wa; filib ak jaraaf ja wàcc ñoom ñaar ci biir ndox ma, mu sóob ko ca.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and andrew, and philip, and bartholomew, and matthew, and thomas, and james the son of alphaeus, and thaddaeus, and simon the canaanite,

Wolof

andare ak filib,bartelemi ak macë,tomaa ak saag doomu alfe,tade ak simoŋ, mi bokk ca mbooloo, ma ñu tudde Ñi farlu ci moom seen réew;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

nathanael saith unto him, whence knowest thou me? jesus answered and said unto him, before that philip called thee, when thou wast under the fig tree, i saw thee.

Wolof

nataneel ne ko: «noo ma xame?» yeesu tontu ko ne: «bi la filib di laata woo, gis naa la, bi nga nekkee ca ker garabu figg ga.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

philip findeth nathanael, and saith unto him, we have found him, of whom moses in the law, and the prophets, did write, jesus of nazareth, the son of joseph.

Wolof

filib dajeek nataneel ne ko: «gis nanu ki yoonu musaa wi ak yonent yi doon wax. mu ngi tudd yeesu, doomu yuusufa, te dëkk nasaret.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

for herod himself had sent forth and laid hold upon john, and bound him in prison for herodias' sake, his brother philip's wife: for he had married her.

Wolof

fekk erodd yónnee woon na, jàpp yaxya, yeew ko, tëj. ndaxte erodd takkoon na erojàdd jabaru filib magam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Anglais

and the next day we that were of paul's company departed, and came unto caesarea: and we entered into the house of philip the evangelist, which was one of the seven; and abode with him.

Wolof

nu jóge fa ca ëllëg sa, ñëw ba ca dëkku sesare. nu dugg ca kër filib, taskatu xebaar bu baax bi, mi bokk ci juróom-ñaar ña, nu dal fa moom.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,891,325,783 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK