Vous avez cherché: disaient (Français - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

mais les autres disaient: laisse, voyons si Élie viendra le sauver.

Wolof

waaye ña ca des ne: «bàyyil, nu seet ba xam iliyas dina ñëw, musal ko.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

ils disaient: salut, roi des juifs! et ils lui donnaient des soufflets.

Wolof

Ñu di ko jegeñsi, di ko pes, naan ko: «nuyu nanu la, yaw buuru yawut yi!»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

tous ceux qui les entendirent furent dans l`étonnement de ce que leur disaient les bergers.

Wolof

Ñi dégg li sàmm yi doon wax ñépp daldi waaru lool.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

ils disaient: si tu es le roi des juifs, sauve-toi toi-même!

Wolof

«su fekkee ne yaay buuru yawut yi, musalal sa bopp!»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et les quatre êtres vivants disaient: amen! et les vieillards se prosternèrent et adorèrent.

Wolof

Ñeenti mbindeef ya naan: «amiin.» mag ña sukk di màggal.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

les principaux sacrificateurs, avec les scribes et les anciens, se moquaient aussi de lui, et disaient:

Wolof

saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya ak njiit ya it di ko ñaawal naan:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

elles disaient entre elles: qui nous roulera la pierre loin de l`entrée du sépulcre?

Wolof

di laajante: «ku nuy béraŋal doj, wiy ub bàmmeel bi?» doj woowu nag bu réy-a-réy la woon. noonu ñu xool, gis ne doj wa deñ.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

il y avait là quelques scribes, qui étaient assis, et qui se disaient au dedans d`eux:

Wolof

fekk ay xutbakat toog fa, ñu di werante ci seen xel naan:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

des gens de la foule, ayant entendu ces paroles, disaient: celui-ci est vraiment le prophète.

Wolof

bi ñu déggee wax jooja, am ay nit ca mbooloo ma ñu naan: «dëgg-dëgg kii mooy yonent bi war a ñëw.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

les disciples raisonnaient entre eux, et disaient: c`est parce que nous n`avons pas de pains.

Wolof

taalibe yi nag daldi werante naan: «nun de indaalewunu mburu.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et, en se retirant, ils se disaient les uns aux autres: cet homme n`a rien fait qui mérite la mort ou la prison.

Wolof

bi ñu génnee nag, ñuy waxante ne: «nit kii deful dara lu jar dee mbaa kaso.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

car ils disaient: que ce ne soit pas pendant la fête, afin qu`il n`y ait pas de tumulte parmi le peuple.

Wolof

kon nag ñu ne: «bumu doon ci bésu màggal bi, ngir yengu-yengu bañ a am ci nit ñi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

ces gens, ayant vu le miracle que jésus avait fait, disaient: celui-ci est vraiment le prophète qui doit venir dans le monde.

Wolof

bi nit ña gisee firnde jooju yeesu wone, ñu ne: «dëgg-dëgg kii mooy yonent, bi war a ñëw ci àddina!»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

beaucoup de gens vinrent à lui, et ils disaient: jean n`a fait aucun miracle; mais tout ce que jean a dit de cet homme était vrai.

Wolof

nit ñu bare ñëw ci moom, te naan: «yaxya deful benn kéemaan, waaye li mu wax ci kii yépp, dëgg la.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

ces hommes furent saisis d`étonnement: quel est celui-ci, disaient-ils, à qui obéissent même les vents et la mer?

Wolof

bi ko nit ña gisee, ñu waaru naan: «kii kan la ci biir nit ñi, ba ngelaw li ak dex gi di ko déggal?»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

d`autres disaient: c`est le christ. et d`autres disaient: est-ce bien de la galilée que doit venir le christ?

Wolof

Ñeneen naan: «mooy almasi bi.» Ña ca des it ne: «waaye nan la almasi bi man a jógee galile?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,763,024,358 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK