Vous avez cherché: justice (Français - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

justice

Wolof

njubte

Dernière mise à jour : 2017-02-08
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

c`est pourquoi cela lui fut imputé à justice.

Wolof

moo tax «yàlla jagleel na ibraayma njub.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

comme abraham crut à dieu, et que cela lui fut imputé à justice,

Wolof

xool-leen ci ibraayma; mbind mi wax na ne:«ibraayma gëm na yàlla,te yàlla jàppe ngëmam ni njub.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

le fruit de la justice est semé dans la paix par ceux qui recherchent la paix.

Wolof

te nitu jàmm dina bey toolu jàmm, góob njub.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

heureux ceux qui ont faim et soif de la justice, car ils seront rassasiés!

Wolof

yéen ñi xiif te mar njub, barkeel ngeen,ndax dingeen regg.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

ayant été affranchis du péché, vous êtes devenus esclaves de la justice. -

Wolof

te ci noonu rëcc ngeen ci nootaangeg bàkkaar te jébbalu ci yàlla, sóobu ci njub.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

en marchant devant lui dans la sainteté et dans la justice tous les jours de notre vie.

Wolof

nu sell te jub ci kanamam sunu giiru dund.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

car il est de la justice de dieu de rendre l`affliction à ceux qui vous affligent,

Wolof

ndaxte jub na ci yàlla, mu delloo coono ñi leen di sonal,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

car le fruit de la lumière consiste en toute sorte de bonté, de justice et de vérité.

Wolof

leer, mbaax lay meññ, njub ak dëgg.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

car que dit l`Écriture? abraham crut à dieu, et cela lui fut imputé à justice.

Wolof

lan la mbind mi wax ci loolu? nee na: «ibraayma gëm na yàlla, te yàlla jàppe ngëmam ni njub.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

de même david exprime le bonheur de l`homme à qui dieu impute la justice sans les oeuvres:

Wolof

noonu la daawuda birale barkeelug nit ki yàlla jagleel njub, fekk ay jëfam taxul.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

car, lorsque vous étiez esclaves du péché, vous étiez libres à l`égard de la justice.

Wolof

ndaxte keroog ba ngeen nekkee jaami bàkkaar, séquleen woon dara ak lu jub.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

cherchez premièrement le royaume et la justice de dieu; et toutes ces choses vous seront données par-dessus.

Wolof

waaye jëkkleen a wut nguuram ak njubteem, te loolu lépp dina leen ko ci dollil.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

il n`est donc pas étrange que ses ministres aussi se déguisent en ministres de justice. leur fin sera selon leurs oeuvres.

Wolof

kon nag ay ndawam mbubboo ndawi njub, loolu du nu jaaxal. dees na leen fey seeni jëf.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

et cela afin que la justice de la loi fût accomplie en nous, qui marchons, non selon la chair, mais selon l`esprit.

Wolof

ba tax na léegi njub, gi yoonu musaa di digle, am na ci nun, ñiy déggal xelu yàlla mi te bañ a topp sunu nafsu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

afin que, comme le péché a régné par la mort, ainsi la grâce régnât par la justice pour la vie éternelle, par jésus christ notre seigneur.

Wolof

ba tax, ni bàkkaar doon yilife ñépp ni buur, indaale dee, noonu itam la yiwu yàlla faloo ni buur, jóge ci njub, jëm ci dund gu dul jeex. te loolu lépp darajay yeesu kirist sunu boroom moo nu ko may.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

car le royaume de dieu, ce n`est pas le manger et le boire, mais la justice, la paix et la joie, par le saint esprit.

Wolof

ndaxte bokk ci nguuru yàlla jotewul dara ak lu nuy lekk mbaa lu nuy naan. nguuru yàlla mooy jub ci kanam yàlla, te am mbég ak jàmm ci dooley xel mu sell mi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

celui qui n`a point connu le péché, il l`a fait devenir péché pour nous, afin que nous devenions en lui justice de dieu.

Wolof

kirist mi musul a def bàkkaar, yàlla def na ko bàkkaar ci sunu wàll, ngir ci sunu bokk ci moom, nu man a doon njubteg yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

ainsi donc, comme par une seule offense la condamnation a atteint tous les hommes, de même par un seul acte de justice la justification qui donne la vie s`étend à tous les hommes.

Wolof

kon nag nu gàttal wax ji; jàddug kenn nit ka rekk moo waral yàlla daan ñépp; noonu itam jëf ju jubu keneen nit ka rekk moo ubbi bunt, ba ñépp man a jub ci kanam yàlla te am dund gu bees.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Français

homme plein de toute espèce de ruse et de fraude, fils du diable, ennemi de toute justice, ne cesseras-tu point de pervertir les voies droites du seigneur?

Wolof

ne ko: «yaw mi fees ak fen ak lu bon, di doomu ibliis, tey noonu lépp lu jub, ndax doo bàyyee dëngal yoon yu jub yu boroom bi?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,776,549,474 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK